Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CI BËJ-GÀNNAARU RÉEW MI Tay, ci alxames ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door ab tukki ci bëj-gànnaaru...

SENEGAAL DÓOR NA ÀNGALTEER 3-1

Gaynde Senegaal yi fàdd nañ yoy Àngalteer ya. Ñetti bal la leen gari Senegaal yi ngàdd. La ca gën a neex moo di ne,...

MBIRUM DUWAAÑE BI LÀQOON YÀMBAA CI DAAMARAM

Kaawteef ! Ab duwaañe lees fekk yàmbaa cig daamaram. Mbuur la xewee. Mu di mbetteel gu réy ba tax ko lëmbe réew jamono jii....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2025)

TABASKI 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, yékkati woon na ay kàddu ci tabaski bi, bi mu...

GASAA : ISRAAYEL DOGAALE NA GAALUG NDIMBAL GII DI « MADLEEN »

Ci guddig altine 8, jàpp talaata 9eelu fanu suwe 2025 la sóobarey géej yu Israayel yi dogaal ag gaal gu doon yóbbul dund ak...

“PENTECÔTE” 2025 : BENNOO CI NGËM, JÀPPOO CI JÀMM

Niki dibéeru démb ji, 8eelu fanu suwe 2025, la kerceni àddina sépp, rawatina yoy Senegaal, doon màggal bésub "Pentecôte". Mu di bés bu màgg...

TABASKI 2025 : IBAADU YI JULLI NAÑU TAY CI ÀJJUMA JI

Ibaaduy Senegaal yi julli nañu tabaski niki tay ci alxames ji, 6i suwe 2025. Fu bari ci diiwaani réew mi julli nañu fa, rawatina...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/6/2025)

PÉNCOOM RÉEW MI Ci ayu-bés bee ñu génn lañu dooroon péncoom réew mi ñeel nosteg pólitig gi. Démb, ci àllarba ji, la waxtaan wi di...

BÉSUB ARAFA

Tay ci alxames, 5eelu suwe 2025, moo yemoo ak bés bi ñuy taxaw taxawaayu Arafa. Muy bés biy toollook 9eelu fanu weeru tabaski atum...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI DÉMB YI (3/6/2025)

PAS YU BEES DIGGANTE SENEGAAL AK MURITANI Réewum Senegaal ak mom Muritani xaatim nañu ñaari pas yu yees. Jëwriñ ji ñu dénk mbiri bitim-réew, Soxna...

NJÀNGATU TÉEREB SOLEILS INVINCIBLES BU SEEX AHMADU BÀMBA NJAAY

Soleils invincibles(Présence Africaine, 2025), ab téere la bu Seex Ahmadu Bàmba Njaay bind ngir yékkati ak xeexal doomu aadama ci biir àddina bu jaxasoo...