Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TUKKIY USMAAN SONKO, ELIMAANU JËWRIÑ YI

Alxames jii weesu la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dooroon ab tukki ci yenn réewi Afrig sowu-jant yi. Donte ne sax, bu yàggul dara,...

PARIS SAINT-GERMAIN : BIDDEEW BI DIKK NA!

Ca péeyu Farãs, Pari, foo sànni mbattu mu tag. Te lenn waralu ko lu moy mbégte mu réy ma fa Paris SG andi gannaw...

PADES II : TÀMBALI NAÑU ÑAAREELU WÀLL WI

Nguur gi sóobu na ci ñaareelu wàllu naaluw PADES II. Mu fas cee yéene dugal 77i tamñareeti (miliyaari) FCFA ngir sopparñi njàng mi, mu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/5/2025)

"BAD" AM NA NJIIT LU BEES Tay, ci alxames ji, lañu doon amal wotey palug Njiitu bànk bii di BAD (Banque Africaine de Développement). Ay...

TÀGGE : NGŨGĨ WA THIONG’O DËDDU NA

Afrig ñàkkati na kenn ci doomam yu ràññeeku yi. Wile yoon, njabootu ladab ak mbatiit ñoo am dëj. Nde, bindkat bu mag bii di...

UBBITEG PÉNCOOM RÉEW MI ÑEEL NOSTEG PÓLITIG BI

Ci àllarbay tay jile, 28 me 2025, lañu doon ubbi péncoom réew mi ñeel nosteg pólitig bi. Jamñaajo, fa CICAD (Centre international de conférences...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/05/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay moo nga woon fa Réewum Gine Bisaawu, doon fa amal...

TAAXUM KAW MA MÀBB FA TUUBAA

Am taaxum kaw a màbbati. Fa Ngor (diiwaanu Ndakaaru) la am taaxum kaw njëkkoon a màbb, ñaari ayu-bés ci ginnaaw. Wii yoon nag, fa...

MBIRUM KOPPARI COVID-19 YI : JÀPP NAÑU MANSUUR FAY

Mansuur Fay mi ngi ci guddi gu lëndëm këriis. Nde, jamono yii, Yoon dafa ko téyandi ci kaso bi. Ndiisoog luññutu gog Ëttu àttekaay...

TABASKI 2025 : CÀMM GEE NGI CI WAAJTAAY YI

Càmmug Senegaal a ngi ba tay ci waaytaayi tabaski 2025 bi. Ginnaaw déggoo bi mu amoon ak réewum Móritani, jubluwaat na réewum Mali ngir...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/5/2025)

XIBAAR ÑEEL JURÓOMI JËWRIÑ YI ËTTU YOON GU KAWE GI WOOLU WOON Ci ndoorteelu ayu-bés bii lañu woolu woon ñenn ci ñi fi nekkoon i...