Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TÀGGE : SËRIÑ MUSTAFAA SAALIW MBÀKKE DËDDU NA

Umma islaam ñàkk na kilifa gu tedd. Njabootu murit a ngi jooy kàngaam bu mag. Senegaal ak Afrig ñàkk nañ doom ju ràññeeku. Waayeet,...

38EELU NDAJEM BENNOOG AFRIG (UA)

38eelu ndajem Bennog Afrig (Union Africaine) mee ngi ñuy amal jamono yii fa Ecopi. Njiiti réewi Afrig yi di ko fa teewe ci diirub...

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu gii. Waaye nag, wile yoon moom, xalam mi ci boppam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon dépite bii di Farba Ngom. Nde, kenn umpalewul ne dañu...

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba ji, yemook 12eelu féewiryee 2025, la wuyuji Boroomam. Amoon na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/2/2025)

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL BI : CÀMM GI DINA JANOOK TASKATI XIBAAR YI ËLLËG Ëttub cettantal gi siiwal na caabalu caytug koppari réew mi diggante 2019 ak...

JÀNGUNEB UGB : NDONGO LI ÑU FEKK MU DEE CA NÉEGAM

Naqar ak uw tiis la ndongoy jànguneb Gastõ Berse fanaane démb. Seen benn moroom moo ñàkk bakkanam. Ca biir néeg ba mu nekkoon, ca...

GERTE : SONACOS DAJALE NA 22. 000IY TON FA NJURBEL

Bi kàmpaañu njaayum gerte gi tàmbalee ba nëgëni sii, banqaasu SONACOS bi nekk Njurbel dajale na 22. 000iy toni gerte. Lim boobu nag, moo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/2/2025)

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA 42eelu JOTAAYU "Comité d’orientation de l’AUDA-NEPAD" Ci xëtu Facebookam la Njiitu réew mi xamle ne teewe na jotaayu "Comité d’orientation...