Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NDOGUM YOON MU METTI FA RISAATOL

Fan yii, ndogi yoon yi bari nañu lool te tegaloo. Saa su ñu jàppee ne wàññeeku nañu rekk, fekk booba la Waalo gën a...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LÀMB JI Dibéer 16i fani féewiryee mooy bés bi njabootug lamb yépp di xaar. Ndax, ca bés booba la ñaari waada yu mag war a...

LËKKATOOG KAARAANGE DIGGANTE SENEGAAL AK MALI

Ginnaaw bi ñu xaatimee woon ab déggoo ci fànnu kaaraange ca atum 2021, réewum Senegaal ak mu Mali yeesal nañu seen ug lëkkatoo ngir...

TÀGGE : MARIE-JOSÉ CRESPIN FAATU NA

Tiis tegooti na ci kaw Senegaal, rawatina ci àttekat yi ak ñiy safoo mbatiit. Marie-José Crespin moo dëddu, moom mi bokkoon ci ñi njëkk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/2/2025)

LIMUB SAABALUKAAY YI SÀMMONTE AK SÀRT YI Sànq ci bëccëg lañu siiwal limub saabalukaay yi nga xam ne sàmmonte nañu ak sàrt yi yoon tëral....

NJÀNG AK NJÀNGALE : “GRAND PRIX DU CHEF DE L’ÉTAT”

Jàngalekat bii di Baara Mbeng moo jël neexal bii ñuy dippe "Grand Prix du Chef de L’Etat". Tay ci alxames ji lees doon amal...

YEESALUG NGOMBLAAN GI : EL MAALIG SUMB NA LIGGÉEY BI

Démb ci guddi, tele TFM dawal na laaj-tontu bi Njiitul Ngomblaan gi, El Maalig Njaay, séq ak seen saabalkat bii di Abdulaay Siise. Ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/2/2025)

SÉMBUW JOTALE DËKKI KOW YI AK NDOX MU SELL Nguur gi seqi na ñaareelu jéego ñeel sémbuw jotale dëkki kow yi ak ndox mu sell...

NAALUW JÀPPANDAL NDOX MU SELL MI

Tay, ci altine ji, lañu doon sumb naaluw jàppandal ndox mu sell ci dëkki àll yi. Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, moo jiite woon...

POROFESËER MUSAA DAAF WÀCC NA LIGGÉEY

Naqar ak uw tiis wu réy a réy la njaabotug jànguney Senegaal yi yeewoo. Porofesëer Musaa Daaf moo wàññeeku. Ci bët-setu altiney tay jii,...

KAARAANGE TALI BI : NDOG YEE NGI WÉY DI FAAT

Bëgg-bëggu Nguur gi moo doonoon wàññi limub ndog yi ci tali bi ba, fii ak 2030, fu téeméeri ndog daan am, ñu mën a...