Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

USMAAN SONKO XAATIM NA DÉGGOOB JÀMM AK BENN PÀCCU MFDC

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak benn pàccu MFDC xaatim nañu ab déggoob jàmm ci teewaayu Njiitu Réewum Gine Bisaawo, Umaroo Sisoko Embalo. Barki-démb,...

KAAJARUG “NEW DEAL TECHNOLOGIQUE”

Tay ci altine ji lañu doon aajar naal wees dippee “New Deal Technologique”. Ndaje moomu, fa CICAD (Centre International de Conférences Abdou Diouf) lañu...

MOODY’S WÀCCEE NA NATTUB SENEGAAL

Moody’s Investors ag kurél la guy natt réewi àddina si ci wàllu kopparal. Bees sukkandikoo ci dég-dég yi kërug Bloomberg siiwal, Moody’s Investors dafa...

BÉS BI ÑU JAGLEEL JUR GI FI RÉEW MI

Démb ci gaawu bi, 22i fani féewirye, lañu doon màggal bés bi ñu jagleel jur gi fi réew mi. Xew maa ngi ñu doon...

LAAJI DÉPITE YI ÑEEL CÀMM GI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak Càmm gi mu jiite ña nga woon ca Ngomblaan ga, démb ci àjjuma ji, 21i fani féewiryee 2025....

21EELU FÉEWIRYEE : BÉS BI ÀDDINA JAGLEEL LÀMMIÑ WEES NÀMP

Làmmiñ wees nàmp ci ekooli tuut-tànk yi… Làmmiñi réew mi, lépp la ñu mën, mën nañoo yenu xam-xam ak lépp lu ci aju. Téere yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/2/2025)

SAES TEGGEEGUL TÀNKAM Kuréel gi ëmb jàngalekat yi nekk ci daara yu kowe yu noppeegul ci xeex bi mu door digganteem ak Nguur gi. Ndax,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LAMB JI : FARÃ DAAN NA AAMAA BALDE Dibéer 16 féewiryee jii weesu la doomu Pàrsel ji, Farã, doon sëgg ak Aamaa Balde bu Pikin...

58eelu NDAJEM OHADA

Tay ci alxames ji lañu doon amal ndajem jëwriñi kurélu OHADA (Organisation pour l’Harmonisation en Afrique du Droit des Affaires). Ki ko ubbi mooy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/2/2025)

SOROJU SANGOMAAR BI Bilaŋub sàngomaar bu atum 2024 mi génn na. Waa Woodside ñoo ko xamle cib yëgle bu ñu siiwal barki-démb ci altine ji,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/2/2025)

GAALUG MBËJ GIY TËMB : LËNT-LËNTI KARPOWERSHIP Gaalug mbëj giy tëmb ci géejug Senegaal gi, ñu duppee ki Karpowership, mbiram dafa lënt. Ci li yéenekaay...

SÀNDIKAA YI FIPPU NAÑU

Sàndikaa yu bari door nañu ay ñaxtu ci ayu-bés bii. Muy ñi féete ci njàngale mu kowe mi, di ñi féete ci paj mi...