Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

15eelu NDAJEM OCI

Ci njeexitalug ayu bés bi, gaawu 4 ak dibéer 5 me 2024, lañ doon amal 15eelu ndajem OCI (Organisation de la Coopération Islamique) mi....

ËMMA SEEN DAAN NA SAA-CEES !

Démb ci dibéer ji, 5i fan ci weeru Me 2024, la doomu Pikin ji, Ëmma Seen doon sëgg ak Saa-cees, doomu Géejawaay ji. Seen...

GOR, CA WAX JA !

Lu tollu ci weer ginnaaw ba ñu ko tabbee elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko joxe ndombog-tànku meeru Siggicoor. Mu nekk ndogal lol, du Yoon...

MBEY MI : MAGUM JËWRIÑ YI JËL NA CI NDOGAL YU BEES

Magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko, jël na ndogal yu bees ñeel kàmpaañu mbey mi ci atum 2024 mi jàpp 2025. Dafa namm a lal...

« UN TOMBEAU POUR KINNE GAAJO » : FÀTTALIKU NGIR JARIÑU

Bubakar Bóris Jóob génnee na téere bob, way-loru yi laboon ca suuxug « Le Joolaa » ba la ko jagleel. « Un tombeau pour...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (2/5/2024)

TUXAL NAÑU BÉSU NDAJEM JËWRIÑ YI Ndajem jëwriñ yee ngi daan am àllarba ju nekk. Àpp boobu soppeeku na. Ndax, wii yoon, tey ci alxames...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax doo tontoom Céy lii ciy way-xëccoo Ku ne samp ndënd Naan awma ci moroom Boppu réew ak ni mu...

TÀGGE : GASTÕ MBENG FAATU NA

GASTÕ SAALIF MBENG, tëggkatu làmb bi, moo génn àddina tey ci àllarba ji, 1eelu fan ci me 2024. Moom nag, rakku Aminata Mbeng Njaay...

PRODAC : CAABALU ËTTUB CETTANTAL BI DËGGAL NA USMAAN SONKO

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dafa santaane woon ñu siiwal caabali luññutu yees amal ci juróomi at yii mujj. Boobaak léegi nag, banqaas...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/4/2024)

CÀKKUTEEFU KURÉLI MAXEJJ YI Yenn ci kuréli maxejj yi, tudde seen bopp Sursaut citoyen et Demain Sénégal fésal nañ lu ñuy xaar ci Njiitu réew...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, demoon na Gine Bisaawo ci talaatay tey jii, 30 awril 2024. Mu di woon tukkib liggéey ak...