Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

AAMADU BA WOO NA BASIIRU JOMAAY FAY NGIR NDOKKEEL KO

Sànq la xibaar bi rot. Muy xibaar boo xam ne biig ci guddi ba léegi ñi ngi koy xaar. Ndax, kenn umpalewul ne, bees...

BASIIRU JOMAAY FAY RAAFAL NA LÉPP !

Basiiru Jomaay Jaxaar Fay jël na raw-gàddu gi ! Daanaka, taax yu mag yépp la raafal. Mayul yeneen lawax yi dara. Li mu rawee...

WOTEY 2024 : YENN LAWAX YAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY

Ginnaaw bi njureef yi tàmbalee rot, Basiiru Jomaay Fay moo jiitoogum, rawee yeneen lawax yi lu baree bari. Mu mel ni, sikk amul ci...

NJUREEFI WOTEY 2024 YI : CEESU KOW (THIES NORD)

Bérébu wote : Séex Ibra Faal Pekku wote : 02 Limu wotekat yi bindu : 584 Limu ñu wote : 382 Limu xob yu neen : 02 Limu xob yu baax : 380 Ñetti lawax...

WOTEY 2024

Sàntar “Grande Medine” : Ci ndigalu perefe, dàq nañ taskati xibaar yépp bi waxtu tëj pekk yi jotee. Cig pàttali, fa la Aamadu Ba...

LI GËN A FËS CI WOTE YI (24/3/2024)

SAA-SENEGAAL YU BARI GÉNN NAÑ WOTEJI Ci dibéeru tey ji lañu woo saa-senegaal ngir ñu fal seen Njiitu réew lu bees ci 5i at yii...

KAN MOOY ANTA BAABAKAR NGOM ?

Anta Baabakar Ngom mooy jenn jigéenu lawax ci joŋantey 2024 yi ngir nekk Njiitu réewum Senegaal dibéeru ëllëg ji, 24 màrs 2024. Anta Baabakar Ngom...

WOTEY 2024 YI : LEERALI JËWRIÑ MAXTAAR SIISE

Ëllëg ci dibéer ji lañ woo Saa-Senegaal yi ci mbañ-gàcce yi ngir ñu fal Njiitu réew lu bees. Ginnaaw xaar bu yàgg te metti,...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Ay waxtu rekk ñoo des ngir Saa-Senegaale falaat Njiitu réew lu bees lu war a wuutu Maki Sàll ci boppu Nguur gi. Mu nar...

BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY SIIWAL NA AM-AMAM

Basiiru Jomaay Jaxaar Fay dafa bokk ci lawax yiy dagaan baatu askan wi ngir doon juróomeelu Njiitu réewum Senegaal. Fan yii weesu, mi ngi...

LI GËN A FÉS CI WOTE YI (22/3/2024)

PDS FEKKI NA BASIIRU JOMAAY FAY Ñépp a doon xaar PDS ngir xam naka lay taxawee ci wotey 2024 yii. Nde, ginnaaw biñteree Kariim Wàdd...

KAN MOOY IDIRIISA SEKK ?

Ay fan a des ci wotey 24 màrs yi ñeel palug Njiitu réewum Senegaal. 19i lawax yi des ci xëccoo bi ñoo ngi wéy...