Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MAKI SÀLL WAX NA…

… CI LI MU FAR BORI JUUTI YI KIBAARAAN YI AMEELOON RÉEW MI Njiitu réew mi, Maki Sàll, dafa jël ndogalu far lépp lu woon...

LU TAX MAKI SÀLL MËNUL A KÀMPAAÑAL AAMADU BA ?

Fan yii nu génn, doon nañ yégle ne Njiitu réew mi, Maki Sàll, dina jàppale Aamadu Ba ci kàmpaañ bi. Noon nañ sax ne,...

KAN MOOY XALIFA SÀLL ?

Xalifa Sàll, nitu pólitig la, fës lool fi Senegaal, di lawax ci wotey 2024 yees dëgmal. Moom Xalifa, mi ngi juddu keroog 1 panu...

KAN MOOY ALIW MAMADU JA ?

Aliw Mamadu Ja ci 19i lawax yiy wut réew mi la bokk. Moom moo teewal làngug pólitig gii di PUR (Parti de l’Unité et...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (19/3/2024)

XEEX BI AMOON ÑOORO : JÀPP NAÑ NDAWUL PASTEF LA Militaŋi Pastef yee doon xeex ak takk-der yi fa Ñooro, diiwaanu Kawlax. Ñoom, ndawi Pastef...

MAN, CEERNO ALASAAN SÀLL

Yeen, mbokki réew mi, Dama bëgg a waxtaan ak yeen ci réew mu màgg. Senegaal réew mu mag la. Réew mu bari ay kàngaam ak ay...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (18/3/2024)

CEDEAO DINA YÓNNEE 130i SAYTUKAT FI RÉEW MI Ndiisoo CEDEAO gi dina yebal lu tollu ci 130i saytukat fi réew mi ngir wote yi fiy...

KÀMPAAÑ 2024 YI : “MAA BAAX, YAA BON !”

Altiney tey jii mooy tollook juróom-ñeenteelu fanu kàmpaañ ñeel wotey 24 màrs 2024 yi. Boobaak léegi nag, lawax yaa ngiy wër réew mi, di...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (16/3/2024)

PODOOR DALAL NA AAMADU BA Ni ñu ko xame ci jamono jii, lawax yi tàmbali nañoo dagaan baatu askan wi. Moo tax ba waa Benno...

UN TOMBEAU POUR KINNE GAAJO : TEKKIG BÀMMEELU KOCC BARMA BU BUBABAKAR BÓRIS JÓOB CI FARÃSE

Boroom xalima bu ñaw bi defati na jaloore. Bubakar Bóris Jóob, werekaan bi, móolati na téere bu bees, duppee ko Un tombeau pour Kinne...

SONKO AK JOMAAY TUUMAAL NAÑ AAMADU BA

Démb la Usmaan Sonko ak Basiiru Jomaay Jaxaar Fay doon janook taskati xibaar yi fa otel Azalaï. Mu nekkoon seen génn gu njëkk ginnaaw...

GÉNNUG USMAAN SONKO AK BASIIRU JOMAAY FAY

Usmaan Sonko génn na. Basiiru Jomaay Fay génn na. Senegaal yëngu na, rawatina Ndakaaru. Démb, ci guddig alxames ji, lañ génn ca kasob “Cap-Manuel”...