Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (01/4/2024)

TABBUG BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY Ëllëg ci talaata ji, dees na tabb Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, mu waat ci kanamu askanuw Senegaal gépp, nees ko...

PÂQUES 2024 : PAAB FRANÇOIS A NGI WOOTE JÀMM CI ÀDDINA SI

Paab bi sàkku na ngir ñu dakkal xare bi dox diggante Israayel ak Palestin. Càkkuteef googu, biral na ko ba mu jëlee kàddu ca...

MAKI SÀLL, NAY RAFET !

Ci guuta gu réy la Senegaal génn, ginnaaw bees amalee wotey 24 màrs yi ba kii di Basiiru Jomaay Jaxaar Fay jël raw-gàddu gi....

SËÑ BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY, 5EELU NJIITU RÉEWUM SENEGAAL

Lépp mat na. Ndajem Ndeyu Sàrti Réew mi dëggal na njureef yi tukkee ci mbañ-gàcce yi, Ëttub dabe bi biraloon leen barki-démb ci àllarbi...

ASP : 39i LIGGÉEYKAT YU BEES CI ÑAARI FAN

Njiitul “Agence de sécurité de proximité” (ASP) li jël na 39i liggéeykat yu bees diggante àllarba ak alxames. Guy Mariis Saañaa moo siiwal xibaar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/3/2024)

MAKI SÀLL DEF NA NDAJEM JËWRIÑAM MU MUJJ Dibéer jii weesu lañu doon amal wotey palug Njiitu réew mi. Ka jiitu ca wote ya...

MAKI SÀLL, DALAL NA JOMAAY AK SONKO FA PALE BA

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na ki koy wuutu, Basiiru Jomaay Fay, ak Usmaan Sonko. Ca Pale ba la leen dalal tey ci alxames...

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi tukkee ci wotey 24 màrs yi ñu doon amal ci...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi ci àddina si ndokkeel nañ Basiiru Jomaay Fay mi askanuw...

COPPITE YI BASIIRU JOMAAY FAY DIGE

Démb la Njiitu réewum Senegaal lu bees li doon biral kàddoom yu njëkk. Fa otel Radison la joxoon dig-daje taskati xibaar yi ci 21i...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li, Basiiru Jomaay Fay, biral nay kàddu niki Njiitu réewum Senegaal....

MAKI SÀLL NDOKKEEL NA NJIITU RÉEW MU BEES LI, BASIIRU JOMAAY FAY

Njiitu réew ma woon, war a fegal keroog 2 awril 2024, ndokkeel na Njiitu réew mu bees li, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. dafa bin...