Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

WAAW, ANA AAMADU BA (BBY) ?

Gaawu, 3 féewaryee 2024 lañ gëj a dégg Aamadu Ba, jëwriñ ju mag ji, di yit lawaxu lëkkatoo Bennoo Bokk Yaakaar. Moom nag, bi...

FOMMUB WOTEY 2024 YI : XALIFA MURID YI ÀNDU CI

Démb, jëwriñu biir réew mi ak nawleem biñ dénk larme bi ñoo nga woon Tuubaa. Ci lees wax, Njiitu réew mee la fa yabaloon....

SAMES SÓOBU NA CI XEEX BI

Fajkat yi xamle nañ ne dinañ dakkal seen liggéey ci diirub ñaari fan. Seen sàndikaa bi (Syndicat Autonome des Médecins du Sénégal) moo ko...

NGOMBLAAN GI JÀLLALE NA SEMBUB ÀTTE BI

Bees sukkandikoo ci Ayib Dafe, Ndiisoog àtte yi jàllale na sembub àtte biy soppi Ndeyu àtte réew mi. Mu ne, 22i dépite ñoo wote...

DOGATI NAÑ SIÑAALU WALFADJRI !

Bees sukkandikoo ci Seex Ñas, doomu Siidi Lamin Ñas mi jiite Walfadjri, Nguur gi dogul siñaalu Walfadjri, dañ ko dagg abadan ! Maanaam, Walfadjri...

NDOGALU FOMM WOTEY 2024 YI : XEEX BI DOOR NA !

Lawax yi ñoo woote am ndaje mu mag ngir ñaxtu ñeel ndogal li Maki Sàll jël, daldi fomm wotey 2024 yi. Xeex bi tàmbali...

NJIITU RÉEW MI FOMM NA WOTE YI

Wotey 2024 yi duñ am ci bésub 25 féewiryee bees leen àppaloon. Ndogal lu Njiitu réew mi Maki Sàll jël la tey, gaawu 3...

ABDU LATIF KULIBALI TEKKI NA NDOMBOG-TÀNKAM

Abdu Latif Kulibali, di jëwriñ ak magum fara-caytu Nguur gi, jël na ndogalu tekki ndombog-tànkam, génn ci Nguur gi. Ab yégle la siiwal di...

DIC WOO NA ROOS WARDINI

DIC woolu na njiitul kurélu « Sénégal Nouveau », Roos Wardini miy lawax ci wotey 2024 yees dégmal. Dafa mel ni, mbirum ñaari nasiyonaalite yi ñu...

BUUR BI, DAG BI AK BATAÑSE BI

Bés, Buur dafa toog ak dagam, ñuy waxtaan. Buur ne ko : - Sama xel dafa nekk ci lekk basante… Balaay Buur di àggal, dag bi daldi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/2/2024)

WAAJTAAYU KÀMPAAÑI WOTEY 2024 YI Ay fan yu néew ñoo des ngir kàmpaañ bi tàmbali. Looloo tax jamono jii lawax yépp a ngi wër ñu...