Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

PDS AM NA NDIISOG LUÑÑUTOOM : LÉEGI NAG ?

Tey ci àllarba ji la Ngomblaan gi door ndiisog luññutu gi ñeel anam yi ñu gàntalee wayndarew lawax bii di Kariim Maysa Wàdd. Dañuy...

MALIN BJÖRK (U.E) : « BËGG NANU GISE AK BASIIRU JOMAAY FAY »

Ndaw yi Bennoog Tugal gi yabal (Mission de l'Union Européenne) ngir ñu saytu wotey njiiteefu réew mi, keroog 25 féewarye 2024, ñooy sàkkoo gise...

TAAX BI MÀBB NDAKAARU : 5I BAKKAN ROT NAÑU

Taaxub 3i etaas moo màbb ci guddig altine ji jàpp talaata. Xaar-Yàlla la jéyya ji amee. Ci lees xamagum, 5i nit ñàkkagum nañ ci...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (30/01/2024)

CAN KODDIWAAR 2024 : SENEGAAL TOOG NA Démb la Senegaal doon joŋante ak Koddiwaar ñeel 1/8 dë finaal CAN 2024 biy ame foofu ca Koddiwaar. Bi...

WOTEY 2024 YI : MBIRUM NDIISOOG LUÑÑUTU GI

Mbirum ndiisoog luññutu gi dépitey PDS yi sumb ca Ngomblaan gaa ngiy wéy di jur coow ci réew mi. Ginnaaw bi UMS, kurél gi...

COOWAL LUUBALUG KOPPAR CA BÀNK BISIC

Luubalug koppar gu takku mooy coow ca bànk BSIC bu nekk Pàrsel Aseni. Lu jege genn-wàllu tamñaret lees fa sàkkal pexe ba ñu teg...

MALI, BURKINAA FAASO AK NISEER BOKKATUÑU CI CEDEAO

Kaawteef ! Mali, Burkinaa Faaso ak Niseer mànkoo nañ génn ci CEDEAO. Xibaar bi day sog a jib. Ab yégle lañu dawal ca tele Niseer,...

SENEGAAL, XALIMAY ÑAARI BINDKAT DAMM NAÑ…

Ibraayma Aan ak Àbbaas Njoon, ñaari bindkat yu mag, ñoo génn àddina : kii ci altine jii nu weesu (22eelu sãwiyee 2024), ki ci des...

KATI LEENA NJAAY : KOPPAR, SAÑ-SAÑ, MBOORUM FCFA

Film bi Kati Leena Njaay (sottalkat) mujj génne te tudde ko Koppar, sañ-sañ, mboorum FCFA, la doon aajar démb ci àllarba ji (24eelu sãwiyee...

MÀGGALU POROXAAN : NU SIYAAREJI SOXNA MAAM JAARA

Màggalu Poroxaan bokk na ci xew-xewi diine yi gën a ràññeeku fi réew mi. Mu nekk bés bu ñu jagleel Soxna na su tedd...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JOŊANTEY DÉMB YI Démb ci àllarba ji moo nekkoon bés bu mujju ci 1eelu sumbu CAN 2024 bi. Ekibi kippug E ak yu F...