AccueilTagsNjuga Gay

Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

spot_img

COOWAL LUUBALUG KOPPAR CA BÀNK BISIC

Luubalug koppar gu takku mooy coow ca bànk BSIC bu nekk Pàrsel Aseni. Lu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/01/2024)

WOTEY 2024 YI Usmaan Sonko Usmaan Sonko dañ gàntal dabantal bi mu dugaloon. Ndaje mi teg...

SENEGAAL AK MÓRITANI : NDEFARUG GIL BI DINA TÀMBALI

Dees na tàmbali ndefarug gil (gaas) gi ci diggante Senegaal ak Móritani. Ci atum...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/01/2024)

DOXIINU YOON CI RÉEW MI Lépp lañ war a xoolaat ci ni yoon di doxee...

MBIRI BAABAKAR FAAL : CAP DUGG NA CI COOW LI

Waa CAP àddu nañu ci mbiri Baabakar Faal. Ginnaaw bi taskatu xibaar bi jotee...

WOTEY 2024 YI : LËNT-LËNTI BAAYALE GI

Ginnaaw bi ndajem ndeyu àtte mi noppee ci caytu gi njëkk ñeel way-sàkku lawax...

MARIN BU SENEGAAL : JURÓOMI KOMÀNDOO YI RÉER

Juróomi komàndoo yu marin bu Senegaal ñoo réer. Muy mbir mu doy waar mu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/1/2024)

NEKKUG LAWAXU USMAAN SONKO Ndaje mu mag la ñoñi Pastef gi woon waajaloon a amal...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Tey ci gaawu gi la ndajem ndeyu àtte réew mi tàmbali seen liggéey ñeel...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/12/2023)

PÓLITIG Saytukati ndeyu àtte réew mi ñoo ngi wéy ba léegi di jot wayndarey way-sàkku...

MBIRI NDEELA MAAJOOR JUUF

Ndeela Maajoor Juuf dugg na ci guddi gu bët setagul. Ginnaaw ba ñu ko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/12/2023)

AYIB DAFE SOOYATI NA Ayib Dafe, ndawul Usmaan Sonko miy lawax ci wotey 2024 yi,...

Latest articles

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA