Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/7/2023)

GORNOORU NDAKAARU BI GÀNTAL NDAJEM TABB MU WAA PASTEF Waa Pastef dañ nammoon a amal ab xew-xew bu mag bob, ca lañuy tabbee Usmaan Sonko,...

MBIRUM 300i ROÑUKAT YI RÉER CI GÉEJ GI

Ñetti gaal, yeboon 300i nit, 300i doomi réew mi, ñoo ne mes, réer. Ñaari ayu-bés, bi ñu tëmbee ak léegi, kenn gisu leen, kenn...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/7/2023)

ONG CAMINANDO FRONTERAS WEDDI NA AYSATA TAAL SÀLL ONG Espaañ Bii di Caminando Fronteras dëggal na ne, dafa am  na 300i doomi Senegaal yu jëloon...

BAC 2023 : NJUREEF YU BAAX

Ginnaaw bi ñu leen nattee ci Talaata jee wees, njureefi BAC yaa ngi tàmbalee rot. Ndongo yi tolloon ci 155 109, ñenn ca ñoom jot...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (11/7/2023)

WOTEY 2024 Kuy doon lawaxu lëkkatooBennooBokkYaakaar ? Ku Maki Sàll di tànn ? Ñan ñooy xàll seen yooni bopp, samp seen i ndënd ? Laaj yii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2023)

PÓLITIG Ayda Mbóoj dina bokk ci lawax yiy xëccoo réew mi ci wotey 25 féewaryee 2024 yi. Démb ci dibéer ji la ko xamle. Lëkkatoo...

NATHALIE YAMB : “LI TAX MAKI SÀLL DELLU GINNAAW…”

Altine jii weesu yemoo woon ak ñetti fan ci weeru sulet la Njiitu réew mi Maki Sàll jëloon ndogal lu am solo ci ëllëgu...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (10/07/2023)

MAROG JËL NA CAN U23 BI Démb, ci gaawu gi, lañ doon amal lii di finaalu CAN U23 bi doon ame fa Marog. Mu gi...

MAKI SALL : « KENN DU TEE WOTE YI AM ! »

Njiitu réew mi, Maki Sàll, amaloon naw waxtaan ak sunuy naataango yu Le Monde, ab yéenekaayu Farãs. Ca biir waxtaan wa, delsi woon na...

MAKI SÀLL – USMAAN SONKO : LÀMB JA CA FARÃS

« Càmmug Senegaal amati na mbetteel ci jeng bi tele France 24 di jeng buy siiwal xibaari pólitig yu Senegaal. » Kàddu gii la Càmmug...

LAAJ-TONTU USMAAN SONKO AK FRANCE 24

Usmaan Sonko, njiitul Pastef li, doon na tontu ci laaji Marc Perelman mu France 24. Taskatu xibaar bi laaj na ko juróom-ñaari laaj, mu...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (6/7/2023)

AFROBASKET-JIGÉEN, RUWÀNDAA 2023 Gannaaw tànn gu njëkk ga, Mustafaa Gay, seggaat na ekib bi, tànn ci jigéen ñi war a teewali Senegaal fa fa Ruwàndaa,...