Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BAC 2023

Ni ñu ko baaxoo amale ci réewum Senegaal, démb ci Talaata ji, yamoo ak 4i fan ci weeru sulet, lañu door BAC bi. Mu...

GÀTTALI BÉS BI (4/7/2023)

ÑAKK A BOKK MAKI SALL CI WOTEY 2024 YI : ÀDDINA SAA NGIY RAFETLU NDOGALU NITU NGUUR KU KO MATE Maki Sàll dafa jël ndogalu bañ...

Xalifa Sàll : « Maki Sàll… dafa musal réew mépp. »

Bi Njiitu réew mi waxee démb ne du bokk ci wotey 2024 yi ba tey, nit ñaa ngi wéy di ci joxe seen i...

MAKI SÀLL : « DUMA LAWAX CI WOTEY 2024 YI . »

Njiitu réew mi fay na coowal ñetteelu moome gi. Àddu na, indi ci tontu lu leer, wax ne day sàmm kàddoom ga mu joxe...

USMAAN SONKO : “LI TAX MAKI SÀLL MËNU MA JÀPP…”

Usmaan Sonko jiitu na Maki Sàll ci kàddu gi. Ci altiney tey jii, 3 suwe 2023, la Njiitu réew mi war a wax ak...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (2/7/2023)

Dëmi-finaal U23 Ginnaaw-ëllëg, talaata 4i fan ci sulet , la dëmi-finaali joŋateb kuppe U23 di door fa Marog. Esipt ak Gine Konaakiri ñooy laale bu...

WOTEY 2024 : MAKI SÀLL A NGI NGEMBU

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na 474i meer ak 37i njiitali Ndajem depàrtmaa yu bokk ci lëkkatoo Bennoo Bokk Yaakaar. Ba mu jelee...

Lu Nguur gi di xaar ci Usmaan Sonko ?

Lu Nguur gi di xaar ci Usmaan Sonko Weeru Yàllaa ngi nii ginnaaw bi Yoon daanee Usmaan Sonko ak Ndey Xadi Njaay. Ñu war a...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ MAAHI ÑAS

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski, ne xutba. Te, xutbay imaam yi, dees na koy faral...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ BAABAKAR SI MU DABBAAX (NJOOL-FUUTA)

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski, ne xutba. Te, xutbay imaam yi, dees na koy faral...

TABASKI 2023 : XUTBA CEERNO SAYDU NUURU TAAL

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski, ne xutba. Te, xutbay imaam yi, dees na koy faral...