Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

GÀTTALI BÉS BI (28/6/2023)

TABASKI Waa Ahlus Sunna, ñi ñu duppee Ibaadu, tabaski nañu tey ci àllarba ji, 28 suwe 2023. Ñu seetlu mbooloo mu takkoo takku ci béréb...

« TUUBAA DAFA WAR A MEL NI WATIKÃ »

Ci ni ñu koy nemmeekoo ci ay kàddoom, Sëriñ Muntaxaa BasiirU du dañ ci xamle dayob maamam ji nga xam ne, moo di wasilaam,...

TUKKI JËM SIGICOOR JAFE NA

Ndakaaru, fi la waa réew mépp wutsiy xëy. Ndaxte, fii la lépp nekk. Waaye nag, saa bu tabaski, korite walla nowel teroo, ñi ko...

TABASKI TEEROOTI NA

Tabaski, xew-xew bu mag a mag la ci jullit ñi. Mu am cëslaay lu dëgër a dëgër ci diiney Lislaam. Yonent Yàlla ba, baayu...

LÀRME BI JËLAAT NAY GÀNGOORI SÓOBARE YEES LIBEERE WOON

Làrmeb Senegaal a ngi yokk ay sóobareem, maanaam mi ngi yokk limi soldaar yi. Nde, juróomi gàngoori sóobare yi ñu libeere woon ginnaaw bi...

LIJJANTI FAJ NA AAJO, WAAYE DEFARUL AM RÉEW

Aminata Ture waxoon na ko. Waxtaan wi ñu doon soow yépp, Maki Sàll ak waa PDS ñoo ko bokk sumb. Soxna si ne woon,...

12I ATI M23 : LA WOON WONNEEGUL

Kurél gii di « Mouvement des forces vives de la nation », ñu gën koo xam ci turu M23, am na 12i at ci ren. Ci...

Gàttali bés bi (23/6/2023)

Waxtaan wi jeex na Ëllëg, gaawu 24 suwe 2023, la Njiitu réew mi, Maki Sàll, war a dalal ndaw yi teewal seen i kurél ci...

JUAN JÉBBAANE NA MAKI SÀLL

Juan Branco, layookatu Usmaan Sonko bi, jure na Njiitu réew mi, Maki Sàll, ak i ñenn ciy ñoñam ca CPI, ëttub àtte àddina si....

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (21/6/2023)

Senegaal duma na Beresil 4-2 Démb ci talaata ji la ekibu Senegaal bu mag bi doon amal joŋantebe xaritoo ak bu Beresil, faLiisbon, gëbla Purtugaal....

JOŊANTE CFEE 2023

Joŋantey CFEE yi door nañ ci àllarbay tey ji, war a jeex ëllëg ci alxames ji. Senegaal, Gàmbi ak Gine-Bisaawoo ñoo koy defandoo. Xarees...

LU ËPP TUURU

Saxaar, safara a ko yabal. Wolof ne, xoddiku balaa lakkle. Senegaalu tey, ci xoddiku la tollu. Nde, Senegaal a ngi mel nib barigo cim...