Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

UBBITEB LIGGÉEY YI ÑEEL PÉNCOOM RÉEW MI

Àllarba, 31 me 2023, la Njiitu réew mi Maki Sàll woote woon ubbite péncoo mi mu woote woon ñeel tolluwaayu réew mi. Biñ ko...

GÀTTALI BÉS BI

USMAAN SONKO Usmaan Sonko fasul yéene dalal benn juboolekat boo xam ne, Antuwaan Jom, jëwriñu biir réew mi, moo la bàyyi nga ñëw ci moom....

AJI SAAR SÀKKU NA ÀTTEB DABU

Alxames 1 fan ci weeru suwe la àttekat bi biraloon daan yim gàll Usmaan Sonko ak Ndey Xadi Njaay ñeel layoob ciif ak tëkkuy...

XEEB NGA XAL, MU LAKK SA DÀGGA

Bi Senegaal dee Senegaal ba tey, xeetu coow lu ne jib na fi, fitna ak i taafar yu bari yëngal réew mi. Naam, xeex...

GÀTTALI BÉS BI

4i néew yiñ yóbbu ci raglub Dalal Jàmm Ginnaaw yëngu-yëngu yu metti yi amoon ci alxames ji ak àjjuma ji, ak lees ci lim yépp...

Séex Bàmba Jéey : “Ndawi Senegaal tey, ku jàpp ni ndaw yu amul jëmu lañu […]. Yow yaa juum.”

Ginnaaw ñaari ati kaso yi àtte bi daan kii di Usmaan Sonko ak kii di Ndey Xadi Njaay, yëngu-yëngu yi metti nañ lool ci...

BEQI : JÀPPUÑU NGAÑ DEMBA TURE

Xibaar bi ñu biraloon ñeel jàppug Ngañ Demba Ture mu Pastef wérul. Kenn jàppu ko. Mi ngi ci jàmm, moom ak njabootam. Waaye, wér...

REY NAÑU BAABA KAANA RÀPPËER

Jot nan xibaar buy wax ne, ràppëer bii di Abdulaay Kamara, ñu gën ko xam ci dàkkentalu Baaba Kaana, ñàkk na bakkanam. Ñenn ñaa...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB, BINDKAT : “KENN WARUL A ÑÉDD NGUUR BA SAY BAARAAM DI NÀCC.”

Seen yéenekaayu web, Lu Defu Waxu, amal nab laaj-tontu bu yaatu ak werekaan bii di Bubakar Bóris Jóob, di bindkat bu ñu ràññe ci...

JÀMMI USMAAN SONKO, JÀMMI RÉEW MI

Barkaatu-démb, ci alxames ji, lañu daan njiitul làng gii di Pastef, Usmaan Sonko, lu tollu ci ñaari ati kaso ci coow li doxoon digganteem...

YËNGU-YËNGUY RÉEW MI : JÀNGUNE YAA NGIY TËJ

Juróom-ñeenti bakkan ci alxames ji, fukk ak ñett ci àjjuma ji, muy ñaar-fukk ak ñaari (22i) nit ñu deewagum ci yëngu-yëngu yi. Nemmeeku nañ...