Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

ÉDITO CAP (ci tekkig Njuga Gay)

Bu nu xasee ba laal laalaake, amatul adada. Jot na, tey jii, mboolem taskati xibaar yi dese seen i ngor te gëm ni kenn...

SENEGAAL, YOKK CERE, DOLLI ÑEEX !

Sàmpiyonaa yi jeex nañu. Ekibi dëkk yi ñooy futbal jamono jii. Ñii di futbal ay matsi xaritoo, ñee di waajal seen i joŋante yi...

MAATAM AM NA GAN

Tuxal nañ Ngañ Demba Ture mu Pastef ca Maataam. Démb ci suba la xibaar bi jib ñeel mbir moomu. Kii di jëwriñ ji ñu...

NGUUR GI JÉEM NA RAGGU

Nguur gaa ngi raggu ngir setal boppam. Démb ci alxames ji, 15 suwe 2023, la jëwriñ yii di Aamadu Ba, Ismaayla Maajoor Faal, Antuwaan...

Me Duudu Ndóoy ñeel mbirum Sonko : ” Li Maki Sàll mën a def ngir saafara mbir mi…”

Me Duudu Ndóoy a nekkoon ganu Maymuuna Nduur Fay ci jotaayu L'invité de MNF ca 7Tv. Moom, layookat bi woon jëwriñu Yoon diggante 1983...

MBOOTAAYU XEET YI YEDD NA NGUURUG SENEGAAL

Kurélug mbootaayu xeet yi ñeel àq ak yelleefi doom-aadama, àdduna ci xew-xew yi amoon fi réew mi, fan yii weesu. Li sabab xew-xew yooyu...

DAKKALUG PÓLITIG FA TUUBAA : AG NDIGAL AK I RÉEROO

Tolluwaayu pólitigu fi Senegaal ak coow la mu làmbool mel na ni bàyyiwul kenn. Réew mépp la faf daj. Xew-xew yi fi mujj, toftalu...

WALFADJIRI-NGUURUG MAKI SÀLL : GATSA-GATSA

Kamaj ! Benn yoon. Kamaj ! Ñaari yoon ! kamaj ! Ñetti yoon. Siñaalu tele Walfadjiri dogati na. Bii yoon, diirub weer la tele biy fay. Li ko...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (12/6/2023)

MBIRIM ÑETTEELU MOOME GI  Paap Sàmba Mbuub xelal na Maki Sàll Paap Sàmba Mbuub, kilifa la ci Bennoo Bokk Yaakaar, lëkkatoo Nguur gi. Moom nag, amal...

MANCHESTER CITY WITTI NA BIDDIIWAM BU NJËKK

Àngale yaa ngay gundaandaat ! Manchester a ngi toj ! Ren, dafa baxa. Ci bëccëgu dibéeru tey ji, foo sànni woon mbàttu mu tàkk. Soppey Manchester...

SËRIÑ MUSTAFAA SI ÀDDU NA CI TOLLUWAAYU RÉEW MI

Sëriñ Mustafaa Si joxe na gis-gisam ci tolluwaayu réew mi, rawatina yëngu-yëngal yi fi amoon bay bakkan yu bari rot ci, ci sababu daan...