Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

ANTUWAAN F. JOM : « JURÓOM-ÑEENTI BAKKAN ROT NAÑU DIGGANTE NDAKAARU AK SIGICOOR. »

Démb, ci guddig alxames ji, jëwriñu biir réew mi doon janook taskati xibaar yi, bi 23i waxtu tegalee 30i simili ak lu topp. Àddu...

ANTUWAAN F. JOM : « NGUURUG SENEGAAL, CI FULLAAY BOPPAM, MOO JËL NDOGALU DOGANDI NJOKKOO GI… »

Démb, ci guddig alxames ji, mbaali-jokkoo yi, WhatsApp, Facebook, Twitter, Telegram, Youtube, benn doxi ci woon. Ci guddi googeet la jëwriñu biir réew mi...

DAANUB USMAAN SONKO AK NDEY XADI NJAAY : ÑU BAREE NGIY ÑAAWLU

Tey, ci alxames ji 1eelu fan ci weeru suwe la àttekat bi biral daan yim gàll Usmaan Sonko ak Ndey Xadi Njaay ñeel layoob...

YEWWI ASKAN WI : « MAKI SÀLL DAFA WOR BA FU WOR YEM. »

Lëkkatoo Yewwi Askan Wi génne na ab yégle ñeel tolluwaayu réew mi. Dañu bind ne : « Lëkkatoo Yewwi Askan Wi a ngi joxoñ baaraamu tuuma Njiitu...

Ismayla Maajoor Faal : « Mën nañ jàpp Usmaan Sonko saa su nekk. »

Ginnaaw bi àtte bi jibee, ñu daan Usmaan Sonko 2i ati kaso yim war a tëdd, laaj bi des mooy bi ñeel ëllëgu Usmaan...

ÀTTEKAT BI DAAN NA USMAAN SONKO AK NDEY XADI NJAAY 2I ATI KASO YI ÑUY TËDD

Ñaari ati kaso yu Usmaan Sonko war a tëdd ak ñaari ati kaso yu Ndey Xadi Njaay war a tëdd. 20i tamndaret ci sunuy koppar yu...

GATSA-GATSA, BA KAÑ ?

Seetlu nañu ne, saa bu Yoon wooloo njiitu pastef lii di Usmaan Sonko rekk, dal day gàddaay réew mi. Walla, saa bu génnee, war...

25 me 1963 – 25 me 2023 : 60i at ginnaaw juddug OUA

Keroog ci Alxames ji, 25 me 2023, la mboolooy Saa-Afrig yi doon màggal bés bees jagleel kembarug afrig ci àddina si. Nu koy wax...

GÀTTALI BÉS BI

TAXAWU SENEGAAL DINA BOKK CI WAXTAAN WI NJIITU RÉEW MI WOOTE  Ëllëg ci àllarba ji, la waxtaan wi Njiitu réew mi Maki Sàll woote war...

GÀTTALI BÉS BI

Popengin 2023 : Kàdduy Mõseñëer Njaay ñeel jëwriñu biir réew mi, Àntuwan Feliks Jonn Nees ko baaxoo defe at mu jot, ay junniy junni kercen,...

USMAAN SONKO FEEÑ NA

Lees doon njort moo am : takk-der yaa jàppoon, ndeke, Usmaan Sonko. Fim ne nii, delloo nañ ko këram. Antuwaan Feliks Jom, jëwriñu biir...

FU USMAAN SONKO RÉER ?

Kenn xamul fu Usmaan Sonko nekk jamono jii. Bentaleb Sow ak Juan Branco, layookatu Usmaan Sonko bi, ñoo fésal xibaar bi ci seen xëti...