Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

SONKO-BÀRT : YÀGG BAWUL DARA (1/2)

Cin bax na, waaye du jikkoom, matt a ko ca jóo. Altine ba tey, Bàrtelemi Jaas a ngi ame rajo yi, tele yi ak...

ÑAARI KUY DUÑU BOKK MBALKA

Pólitig ci Senegaal du jóg di jur mbetteel ci askan wi. Mu mel ni, lu kenn dul foog, mooy wëlbatiku di ëlëm nit ñi....

SAFAANTOO YA CA NGOR : ÑAARI BAKKAN ROT NAÑU

Njiitul mbootaay "Ngor debout", Mamadu Njaay, yëgle na ni ñaari nit dee nañu ci guddig taalatay tey ji. Askan wi ak takk-der yi ñooy...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 9 ME 2023)

SAFAANTOO YA CA NGOR : ÑAARI BAKKAN ROT NAÑU Njiitul mbootaay "Ngor debout", Mamadu Njaay, yëgle na ni ñaari nit dee nañu ci guddig taalatay...

DAAN NAÑ USMAAN SONKO 6i WEERI KASO YUM DUL TËDD

Ndogal li jib na. Lees doon njort bir na. Nee na fàŋŋ. Àttekat bii di Mamadu Siis Faal mi jiite woon layoob dabu bi...

USMAAN SONKO AK MAKI SÀLL : CÓOKI MUJJ GI

Tey, ci altine ji lees war a àttewaat layoob Usmaan Sonko ak Maam Mbay Ñaŋ ca Ndakaaru. Léegi, daanaka mëneesul a toog ñari weer...

LI GËN A FËS CI XIBAARI AYU-BÉS BI 

Layoo Maam Mbay ÑAŋ ak Usmaan Sonko Altine jii ñu dëgmal lañu war a àttewaat Usmaan Sonko ak Maam Mbay Ñaŋ. Waaye, kii di Usmaan...

Coowal bóom gi am ca Karma

Ci 20 awril bii weesu, lu ëpp 150i doom-aadam lañ faatoon ca dëkk bu ñuy wax Karma ca Burkinaa Faaso. Ñaari ayu-bés ginnaw bi...

WAXTAAN, NAXTAAN WALLA NAX TÀNN ?

Wolof dinay faral di wax ne, réeroo amul, ñàkk a waxtaan a am. Waaye, booba, day fekk waxtaan wa am sabab bu ko jar,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 4 ME 2023)

RËBËJOO BA CA PSG Gannaaw tukki bi Messi amaloon ca Araabi Sawdid, njiiti Paris Saint-Germain daan nañ daan bu diis. Dañoo ajandi Messi ñaari ayu-bés...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 4 ME 2023)

UBBITEG FÓRËM KOOM-KOOMUG MBOOLAAY GEEK JÀPPALANTE BI Ci alxamesu tey ji la Njiitu réew mi, Maki Sàll, doon jiite ubbiteg Fórëm koom-koomug mboolaay geek jàppalante...