Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Màggalug téeméereelu Usmaan Sémbeen

Usmaan Sémbeen doon na am téeméeri at ci ren, bu fekkoon muy dund. Jànguneb Ndar, ñu gën koo xam ci turu UGB (Université Gaston...

DEGGOO BU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK FMI

Nguurug Senegaal ak FMI (Font monétaire International), di mbootaay miy saytu kopparu réewi àddina si, am nañu ab déggoo bu yees. Keroog, ci alxames...

GÀTTALI BÉS BI (ALXAMES 18 ME 2023)

Daaray Nguur gi tëj nañu leen fa Siggicoor ak Séeju Li ko dale àjjuma ji 19 me 2023 ba alxames 25 me 2023 daaray Nguur...

LEAGUE DES CHAMPIONS : MANCHESTER CITY WULLI NA REAL MADRID

Démb ci àllarba ji lees doon amal ñaareelu joŋante démi-finaal diggante Manchester City ak Real Madrid. Real Madrid moo fekki woon Manchester City fa...

SÉEX BEKAAY DËDDU NA !

Xalifa tarixa xadiir yi ci Senegaal wuyuji na Boroomam ginnaaw tawat bi ko tëraloon. Kan moo doonoon Séex Bekaay ? Jaar-jaaram lan leen dégtal ci...

BENN LAYOO, 16i BAKKAN

Benn takk-der bu daamaru pólis bi jaar ci kowam, mu jaare fa, ñàkk bakkanam. Benn a ngoog. Mbetteel, tiis ak naqar dikkal baay bi,...

CAN U17 2023 : KUB MU NGI XEEÑ !

Raayab Senegaal a ngi gën yéeg, turam di gën a jëm ca kow a kow. Sunu kuppekat yaa ngiy wéy di aj turu Senegaal...

SIGICOOR : BENN TAKK-DER ÑÀKK NA BAKKANAM

Xeex bu mettee am ca Sigicoor diggante ndaw ñiy taxawu Usmaan Sonko ak takk-der ya. Ci suba ba léegi, xeex ba dakkagul. Fi mu...

SIGICOOR : « PANAANUG WAY-BËGGI REEW MI »

Ay téeméeri téeméeri nit ñoo dajaloo ca buntu këru Usmaan Sonko, fa Sigicoor jamono jii. Gaawu, ci guddi gi, la fa mbooloo ma tàmbalee...

POROFESËER PENDA MBÓW : « MËSUMA ÀND CI YEMOOG GÓOR AK JIGÉEN (« LOI SUR LA PARITÉ ») »

Bañ koy wote ci jamonoy Njiitu réew ma woon, Abdulaay Wàdd, soxna Penda kesee nekkoon soxna su ci àndul woon. Li ko waral rekk...

F24 : WENN SAY, GENN KÀDDU

Démb ci àjjuma ji, ginnaaw julli jumaa, la waa F24 woote woon fa « Place de la nation » ngir amal fam ndaje mu...