Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MAAM LEES KAMARA, KENN DOOTU LA FÀTTE

Altine, 1eelu fan ci weeru Me lañ doon màggal liggéeykati àddina sépp. Fépp fu liggéeykat nekk, ak bépp xeetu liggéey boo mën di def,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 3 ME 2023)

Aminata Ture Ginnaaw bi mu xamlee nee waa PDS ak Waa Bennoo Bokk Yaakaar dañoo teg "deal" Ci suuf ngir féewal kujje gi, daganal ñetteelu...

AS PIKINE – GUEDIAWAYE FC : XUMB TE DAGAN

Keroog, ci gaawu gi 29 awril 2023, sàmpiyonaa Senegaal bi jaxoon na lool. Ndax, As Pikine ak Guédiawaye Fc ñoo doon daje. Mu nekkoon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 2 ME 2023)

Usmaan Sonko : « Waxtaan wees woote, sàkkal pexe Usmaan Sonko rekk a di jubluwaay bi… » Usmaan Sonko de, narul bokk ci waxtaan wi Njiitu réew miy...

1 ME, BÉSUB LIGGÉEYKAT YI

Tey, 1 fan ci weeru me, àddina wërngal këpp di màggal bés bees jagleel liggéey (liggéeykat yi). Ñu koy wax ci nasaraan « Journée...

TAS XIBAAR : TAS XAR-BAAX WALLA TAS CI KASO BI ?

Tasum xibaar mi ngi bëgg a tagatémbe jamono jii ci réewum Senegaal. Dara waralu ko lu dul ni Yoon di doxale ak ñi koy...

AKSIDAŊ CA KAWÓN

Aksidaŋ bu mettee amati ca Kawón, ci wetu fooraa ba, fa diwaanu Kawlax.  Ab biis la benn pónoom toj, mu daldi daanu, këppu ci kow...

Naalub juróom-ñetti jàngu yu yees

Nguurug Senegaal dina ubbi juróom-ñetti jàngu yu kowe ñeel njàngalem liggéey (mécce), muy ISEP (Instituts Supérieurs d’enseignement professionnel), ci atum 2024-2025 mii di ñëw....

GÀTTALI BÉS BI (GAAWU 29 AWRIL 2023)

Jàppal nañu bés layoob Usmaan ak Aji Saar : 16 me 2023 Bés bi ñépp doon xaar agsi na, di bésub layoo diggante Aji Saar ak...

KÀDDUY DOKTOOR SEEX MUHAMMAD AHMAD LÓO

Doktoor Seex Muhammad Ahmad Lóo biral nay kàddu, jëmale leen ci askan wépp, rawatina Nguur gi ak Yoon wi. Dafa amoon i ndaw yu...

GÀTTALI BÉS BI (ALXAMES 27 AWRIL 2023)

Ndoorteelu burok Meeru Sigicoor bi, Usmaan Sonko, biral na 12i naal yi mag yim jagleel diiwaanu Sigicoor. Ci ngoonug démb ji, àllarba 26 awril 2023...

“SËRIÑ BI, FÀWW MU FEEÑ”

Bu ñu seetloo fan yee ci ginnaaw, werante amoon na ci nataali Séex Ahmadu Bàmba Mbàkke, naan moom la ak du moom. Muy ay...