Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI RÉEW MI (ALTINE 3 AWRIL 2023)

4 AWRIL Yewwi Askan Wi gàntal na Njiitu réew mi, Maki Sàll Lëkkatoo Yewwi Askan Widu teewe defileb 4 awril bi. Njiiti lëkkatoog kujje gi dañu...

NJAAY DARAAPOO DËDDU NA

Momar Njaay, ñu gënoon koo miin ci turu "Njaay Daraapoo", dëddu na. Moom, nag, ku ràññeeku woon la ci wàllu kuppeg Senegaal. Mi ngi...

LÀRME BI PÓLITIGUL

Bërki-démb, ci àjjuma ji, la waa Yewwi Askan Wi génne woon ab yëgle ngir xamle ne ajandi nañu seen ndajem-ñaxtu mi ñu nammoon a...

YARGA SI, BÉYU SARAX BI

Démb la àttekatu Ñaareelu kabine bi dóor ab « mandat de dépôt » ndawul Pastef li, Yarga Si. Lees koy toppe moo di ne, dafa doon...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Fileek ñeenti fan, Senegaal dina Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak ñetti at, bim moome boppam ba tey. Muy yemook talaata, 4 awril 2023....

MAAM MBAY ÑAŊ : ” SONKO RËCCAGUL. “

Maam Mbay Ñaŋ nee na day def "appel", du bàyyi mu sedd. Moom, ak i layookatam, doon nañ amal ndajem-waxtaan ak taskati-xibaar yi, tey...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 30 MÀRS 2023)

Daan ba dal na ci kow Usmaan Sonko Tey lañu doon àtte Usmaan Sonko ak Maam Maam Mbay Ñaŋ. Daan ba nag, dal na ci...

LAYOO USMAAN SONKO – MAAM MBAY ÑAŊ

Àttekat bi daan na Usmaan Sonko ñaari weer yum dul tëdd kaso ak 200i tamndaret yu mu war dàmpe Maam Mbay Ñaŋ. Bu dee...

KU JIITE RÉEW MI ?

Fi réew mi tollu jamono jii, teey na xel. Waaye, jur nay laaj yu jar a taxaw seetlu. Dafa di, saa bu kujje gi...

TONTU DU FOROX !

Démb ci yoor-yoor bi, toppekat bu mag bi, Ibraayma Baaxum, doon na amal ndajem waxtaan ak taskati-xibaar yi. Li mu ko dugge woon mooy...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 28 MÀRS 2023)

XIBAAR YI TUKKE CI NDAJEM WAXTAAN MI TOPPEKAT BU MAG BI DOON AMAL Tey, ci yoor-yoor bi, la toppekat bu mag bi doon janook taskati-xibaar...