Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALTINE 27 MÀRS 2023)

YOON Deferee nañu Baabakar Ñaŋ ngir ne dafa seetaan aji-tawat ba mu faatu faf Ci altiney tey ji lañ wooluwaatoon doktoor Baabakar Ñaŋ ca « Sûreté urbaine...

KAYIS SAYET WAXATI NA NJOMBE

Njiitu réewum Tinisi li, namm naa andeeti coow ci diggante Tinisi ak Libi. Àtte bi CIJ (Cour internationale de justice, di ëttu àttewaayu mbootaayu...

ÑETTEELU MOOME GI

Coowal ñetteelu moome gaa ngiy wéy di lëmbe réew mi. Ba tey, Njiitu réew mi, Maki Sàll, àddoogu ci. Bés bu set, gaa ñiy...

GAYNDE GI ŊARATI NA !

Gaynde gi suuragul, ndeke. Gannaaw ba ñu fàddee kuppeg Afrig gii weesu, xàllal seen i rakk yoon wi, gayndey Aliw Siise yi dikkaat nañ,...

ÑAAW NA BA NOPPI

Paap Aliyun Saar a doon dalal Bubakar Bóris Jóob ca ITV. Tolluwaayu réew mi ci wàllu pólitig lañ doon fénc. Jamono yii nag, réew...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 24 MÀRS 2023)

PÓLITIG Séex Umar Jaañ ak Abdu Kariim Géy dellu nañu kaso Ñetti weer kepp la Séex Umar Jaañ ak Abdu Kariim Géy gis jant bi ginnaaw...

NDEKETE YOO, SUUKAR ÑÀKKUL…

Suukar ñàkkul Senegaal ! Pexem jaaykat yi kepp la, ngir yokk njëg li ci lu dul yoon. Lii la kàdduy Luwi Lamot yiy wund,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 23 MÀRS 2023)

Maki Sàll a ngi tëkku kujje gi Dafa mel ni Njiitu réew mi, Maki Sàll, defantee ko tax a jóg. Ci àllarbay démb ji lees...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 23 MÀRS 2023)

Adebayoor ak Özil bàyyi nañu Adebayoor, saa-Tógoo bàyyina kuppe ! Barkaatii-démb ci altine ji la yëgle ne tekkinay dàllam fas-yéene ko bàyyi ak xale yi...

LEKKOOL YA NGI CI YOONU LOMPOÑ

Coowal pólitigu Senegaal mi ngi wéy di jur jote ci réew mi. La ca mujj di layoob njiitul Pasteef lii di Usmaan Sonko ak...

JÀPP NAÑU DR BAABAKAR ÑAŊ, BOROOM KILINIG SUMA ASSISTANCE

Sàndarm yi jàpp nañu fajkat bii di doktoor Baabakar Ñaŋ miy boroom kilinig Suma Assistance. Rajo Rfm a siiwal xibaar bi. Nee ñu, Medina...

USMAAN SONKO : “BËGGUMA KU MA RAWALE… DAÑ MA BËGGOON A REY…”

90 000iy nit ak lu teg ñoo teewe waxtaan wi Usmaan Sonko doon amal ci xëtu Facebookam, démb ci guddi gi. Muy lees mësut...