Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 11 AWRIL 2023)

NGOMBLAAN GI : DEPITE YU YEWWI ASKAN WI BAÑ NAÑU NGANTALUG COOBARE GU WAA BENNOO BOKK YAAKAAR Dépitey lëkkatoo Yewwi Askan Wi nee nañu dañuy...

FU MESSI DI FUTBAL DÉWÉN ?

Jamono jii, laaj bii moo lëmbe xel yi, rawatina xeli soppey Barcelone FC yi. Li ko waral, nag, mooy ni, seen yéene yépp dafa...

CHINA MALL, WÓOR NAAM ?

Ginnaaw AUCHAN, yaxantukati saa-senegaal yi amaat nañu geneen gan. Geneen kërug liggéey (entreprise) gu Sinwaa moo ubbi fale ca biir Ndakaaru, ca Mermoos-Sàkkere-këer, ci...

TUBAAB YAA NGI YEDD MAKI SÀLL

Kurél gi boole digaaley Senegaal yi ci wàllu xarala ak kopparal, G50, yedd na Njiitu réew mi, Maki Sàll. Àmbaasadëeru Bennoog Tugal gi, Jean...

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ – USMAAN SONKO JEEXAGUL

Démb, ci alxames ji, 6 awril 2023, layookati Usmaan Sonko yi woote woon nañu am ndaje, ñoom ak taskati xibaar yi. Li ñu ci...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ÀJJUMA 7 AWRIL 2023)

XEETAL CA ITALI Kañ mbirum xeetal, xeeb ak mbañeel di jeex ci àddina si, rawatina ci àddinay kuppe gog, yoonam nekku ca ? Saa bu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 6 AWRIL 2023)

JA BU LAKKATI CA KAWLAX Lakk gu mettee metti moo am ca Kawlax, ci guddig àllarba ji jàpp alxames. Ma nga amee ca jawub sàndikaa...

YANQOOBA JATARA DAY TEKKI NDOMBOG-TÀNKAM

Lees doon xaar jib na : Yanqooba Jatara, jëwriñu tàggat-yaram gi, génn na pàrti Rewmi, te daa fas yéene tekki ndombog-tànkam. Moom, nag, moo...

COOWAL NAPPKATI KAYAAR YEEK YU MBOORO YI

Géej gi sàmbaraax na. Bakkan bu rot, 22i nit ñu amey gaañu-gaañu, ñaar ñu nekk diggante dund ak dee, 18 doomi Kayaar yu pólis...

MAKI WAX NA AK NDAW ÑI

Màggalug bés bi Senegaal moome boppam, dafa nekk aada ci réew mi. Ñu jàpp ko at mu jot ci bésub 4 awril. Ren, dafa...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Tey, talaata, 4 awril 2023, la Senegaal di Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak ñett, bim moome boppam ba tey. Ñu war ko màggal fépp...