Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

QATAAR – SENEGAAL, NDAM REKK

Ginnaaw bi mu ñàkkee joŋanteem bu njëkk bi digganteem ak Olànd, Senegaal dina janook Qataar mi dalal kuppe gi. Ci àjjumay tey jii la...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 24 nowàmbar 2022

POLITIG Tabb yu yees yi Ca ndajem jёwriñ ma mu doon amal démb, Njiitu réew mi jot na fa jёl i ndogal, jox ñenn ci ay...

MBIRUM WAY-YËDDU YI RÉER

Baabakar Ture mu Kewoulo moo njëkk a siiwal xibaaru réeru ñaari way-yëdduy Nguur gi. Fan yii yépp nag, ci mbir mi la kibaraan yiy...

QATAAR, FULLAAY JAAY DAQAAR

Bu ñu toppe mboorum futbal, mënees na wax ne guleet dëkkub naar di dalal kuppeg àddina si. Nde, du ku jóg rekk, FIFA jox...

QATAAR 2022 Àllarba 23 nowàmbar 2022

Àllarbay démb jee nekkoon ñeenteelu bésu kuppeg àddina siy ame Qataar. Ñeenti joŋante waroon ci am : Marog - Kurwaasii, Almaañ - Sàppõ,  Espaañ...

QATAAR 2022 Talaata 22 nowàmbar 2022

Talaatay démb jee nekkoon ñetteelu bésu kuppeg àddina siy ame Qataar. Ñaari ponkal waroon cee door seen i joŋante, muy Farãs mi ko mujje...

CNRA DOG NA SIÑAALU iTV

Ngir fàttali, CNRA dafa artu woon rajo yeek tele yi ngir ñu bañ a tooñ RTS mi féetewo, moom kese, woneg matsi kuppeg àddina...

KUPPEG ÀDDINA SI : SENEGAAL TARXIIS NA

Ginnaaw ubbite gi, ci dibéer ji (20 nowàmbar 2022), démb lañ doon amal ñaareelu bëcëgu kuppeg àddina si. Ñu doon ci amal ñetti joŋante....

COOWAL ÑETTEELU MOOME GI

Lu tollu ci fukki weer ak ñeent kepp a des ci wotey 2024. Waaye, coowal ñetteelu moome gi moom taqarnaase na xaat ci réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 19 nowàmbar 2022

PÓLITIG Woteb nafag 2023 gi door na ca Ngomblaan ga. Tey ci gaawu bi, jëwriñ ji ñu dénk wàllum dëkkuwaay yi ag cet gi, Abdulaay...

Qatar 2022 : Ay mbetteel kese la

Benn bés a des ngir joŋantey kub bu àddina si door fale ca Qataar. Fanweeri bar (ikib) ak ñaar war koo teewe. Waaye itam,...