Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 17 nowàmbar 2022

TÀGGAT-YARAM Futbal/Qataar 2022 : Saajo Maane du bokk Yaakaar tas na ! Ndeysaan. Xibaar bu tiis a tiis a dikkal Senegaal gépp, démb, bi ñu yëgee...

BIRAM SULEY JÓOB, MBAA DU… ?

Gor, ca wax ja. Kàddu gilee génn démb ci gémmiñi saa-senegaal yu baree bare. Waaye, ci làmmiñ ak loyukaayi (claviers) ndawi PASTEF yi la...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Àllarba 16 nowàmbar 2022

PÓLITIG  Maalig Gàkku Léegi leer na, kii di Maalig Gàkku mooy nekk lawaxu làng gii di Grand Parti. Ca ndaje mu ñu amaloon la xamlee ne...

GII MARIS SAAÑAA XAS NA JËWRIÑU WÉR-GI-YARAM

Gii Maris Saañaa dal na ci kow Mari Xemes Njaay, jëwriñu wér-gi-yaram geek Ndimbalu njaboot gi. Dépite Yewwi Askan Wi ne, soxna si dafa...

CÀKKUTEEFU KURÉLU “COLIDEP”

COLIDEP (Collectif pour la Libération des Détenus Politiques) nag ay kuréli way-moomeel a ko sékk, boole seen doole ngir xeexal képp ku ñu jàpp...

SAAJO, IMAAM YI SAX ÑU NGI ÑAAN

Gaañu-gaañu bi Saajo Maane ame ginnaaw kuppe ga mu mujje def ca Bayern, jural na saa-senegaal yi njàqare. Te, du ñi safoo  taggat-yaram rekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 14 noowàmbar 2022

PÓLITIG Maalig Gàkku dina nekk lawax ci wotey njiiteefu réewum Senegaal yii di ñëw. Làngu pólitig gii di Grand Parti, te moom ci boppam jiite...

NJOMBEW 6i PÀKK YI NGUUR GI WÀNTEER PERETZ

Noppeegunoo wax ci njombew pasug 45i miliyaar yi, ñu sullil nu beneen tóoxidóoni. Usmaan Sonko, njiitalu PASTEF li, moo siiwal beneen tojaange bu Nguur...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 12 NOWÀMBAR 2022)

PÓLITIG Na mu ko yëglewoon ginnaaw ba mu janook taskati-xibaar yi, Usmaan Sonko miy njiitu PASTEF, wéyal na Nemmeeku Tour ba mu dooroon. Démb ci...

Limub gaynde yiy dem ca kub bu àddina si : Saajo Maane mooy kiy dem

Aliw Siise siiwal na limub gaynde yi war a teewal réewum Senegaal ca kub bu àddina si. Ñi ngi tollu ci ñaar-fukk ak juróom-benn....

LI GËN A FËS CI XIBAARI BES BI Alxames 10 nowàmbar 2022

Mbirum pasug ngànnaay gu 45i miliyaar yi Dépitey Yewwi Askan Wi (YAW), nee nañ du ñu bàyyi mukk mbirum pasug ngànnaay gu 45i milyaar yi....

GUY NJÓOBEEN (1/2)

Aatu feeñ na ! Njaayeen yi dégluleen Njóobeen bi raw na leen Buleen ko réyloo woyal, nanguleen Guy ga ca Yoof du mës a liis Kuy siisu randul...