Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 03 DESÀMBAR 2022

PÓLITIG Ginnaaw ndajeem jëwriñ yi mu amaloon, Njiitu réew mi Màkki Sàll, takkal na ndombog-tànk toppekat bu mag ba woon, Sëriñ Basiiru Géy. Mu fas...

GÓOR GU MAT DU DÓOR JIGÉEN…

Alxames, 1 fan ci weeru desàmbar mooy bés bi ñu jagleel xeex sidaa ci àddina si. Bés bi nag, dafa méngoo ak joŋanteb futbal...

LIY RAAM, CI ÑAG BI LA JËM

Senegaal a ngi ci diggante bu doy a doy waar. Ku yebu tiit ci ni miim réew di doxe jamono jii. Mbir yi fiy...

KUPPEG ÀDDINA SI : SENEGAAL AK MAROG, NGIR SIGGIL AFRIG

Pàcc bu njëkk bu kuppeg àddina si jeex na démb ci àjjuma ji. Tey ci gaawu bi la ñuy door ñaareelu pàcc bi, di...

FEGGUG PAJ ÑEEL 7. 000i NDAWI NAALUB « XËYUB NDAW ÑI »

7000i ndaw yi bokk ci naal bees dippe « Xeyu Ndaw Yi » lees jagleel feggug paj (couverture sanitaire).  ASERGMV (Agence sénégalaise de...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 1 desàmbar 2022

PÓLITIG Xeex ca Ngomblaan ga Xeex bi tey ci suba la xewe fale ca Ngomblaan ga. Dépite bii di Ami Njaay la kii di Masata Sàmb...

QATAAR 2022 : GAYNDE YI FÀDD NAÑ EKUWAATËER

kuppeg àddina saa ngay wéy ca Qataar. Ci kippu A gi, Senegaal amati na ndam ginnaaw bi mu dóoree Ekuwaatëer ñaari bii ci benn,...

NDAJEM NJIITU RÉEW MI AK BOROOM DAARA YI

Ci Altine ji, Jamñaajo dalal na ñiy yëngu ci daara yi. Ñu amoon ndaje ak Njiitu réew mi, Màkki Sàll, ngir luy jëmale daara...

ÑEENTI SASI NAFAG ATUM 2023 MI

Alxames 17 nowàmbar 2022 la Ngomblaan gi dooroon péncum nafag Nguur gi ñeel atum 2023 mi. 6. 400i tamñareti (miliyaari) CFA la Nguur gi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 28 nowàmbar 2022

PÓLITIG Tusĩ Màngaa, dem na bokki Pastef. Démb (dibéer) la ko xamle. Moom Tusĩ Màngaa nag, bu yàggul dara la tekki ndombal tànkam ca làngug...

WAAJTAAYU WOTEY 2024 YI

Joŋantey 2024 yi door na, te luy jot jot na ginnaaw dee. Mu mel ni gaa ñi fare ci làngug pólitig gi nànd nañu...

Kub bu àddina si : Senegaal am na ndam ci ñaareelu joŋanteem

Ginnaaw bi mu lajjee woon ci kanamu Olànd (altini 21i fan ci nowàmbar 2022) ci joŋanteem bu njëkk ci kub bu àddina siy amee...