Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LAAJ-TONTU AK SOXNA FAATU SIISE KAN (1/2)

LU DEFU WAXU, seen yéenekaay ci kàllamay Kocc, mi ngi am mbégte dalal fii tey, Soxna Faatu Siise Kan, jàngalekatu wolof ca Almaañ. Soxna...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/4/2025)

NDOG MU METTI CI YOONU LINGEER AK MAATAM WI Yoon waa ngi wéy di bóom i doomi-aadama. Saa su ñu jàppee wàññeeku na, fekk booba...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG AFRIG U17 Guney Senegaal yi amal nañu seen matsu kippu bu njëkk. Seen dëkkandoo yu Gàmbi yi lañu ci doon dajeel, daldi leen dóor...

MAMADU JA CA KAW, DE GAULLE CI SUUF !

Démb, ci àllarba ji, lañu doon amal ndajem jëwriñ yi, ni ñu ko baaxoo di defe ayu-bés bu nekk. Ca biir ndaje mooma la...

NGOMBLAAN GI WOTE NA SÀRTUB LEERAL BI

Ngomblaan gi wote na sémbuw àtte wiy leeral àtteb njéggal (loi d'amnistie) bi Maki Sàll, Njiitu réew ma woon, wotelu woon. Dépite PASTEF bii...

MBIRUM MARINE LE PEN

Marine Le Pen kenn la ci ñi ñu gën a bàyyi xel ci géewu pólitigu Farãs. Moom, moo jiite dépitey làngu pólitig gii di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/4/2025)

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI Jëwriñu njàng mu kawe mi, gëstu beek coste gi, Abdurahmaan Juuf, àddu na ci mbirum jànguney jàmbure yi, fekk ñu doon...

KORITE 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Ci altiney tay jii la Njiitu réew mi julli korite. Fa Jumaay Ndakaaru ju mag ji la jullee, niki at mu nekk. Nees ko...

PÉNCOO MI ÑEEL NJÀNG MU KAWE MEEK GËSTU BI

Ginnaaw bi ñu nekkee ciy waxtaan ak i joyyanti ngir jubbanti ati njàng yu duggante yi, Senegaal dina dem ci yeneen i péncoo yu...

GINE-KONAAKIRI : SENERAAL MAMADI DUMBUYAA JÉGGAL NA MUSAA DADIS KAMARA

Sóobare ba jiite réewum Gine-Konaakiri jamono jii, Seneraal Mamadi Dumbuyaa, jël na ndogal lu réy lol, lëmbe na Afrig ak àddina sépp sax. Ndax,...

NJÉGGAANIY SENEGAAL : SIIN ROMB NA FARÃS

Senegaal, li ëpp ci lees fiy jëfandikoo, lees di jéggaani la. Dafa di nag, Farãs moo mës a nekk réew mi ëpp li muy...