Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

DÉGGOOB YOON DIGGANTE SENEGAAL AK MAROG : DÉPITE YI JÀLLALE NAÑU SÉMBU ÀTTE WI

Ci talaatay démb ji la Ngomblaan gi doon fénc sémbuw àtte ñeel Déggoob Yoon bi dox diggante Senegaal ak Marog. Sémbu àtte woowu mooy...

HIMBAA : WAYUW JUDDU, WAYUW RUU

Xeet wii di Himbaa, fa Namibi, bis bi ñuy màggal ak a fàttaliku seen juddug doom (anniversaire), duñu ko jàpp ci bisub juddu bi,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/3/2025)

NDONGO YI ÑU DÀQ FA SIGICOOR Fa Sigicoor, am na ñetti xale yu ñu dàq ci seen lekkool ba. Muy daan bu ñu leen gàll...

SOGEPA MI NGI CI YOONU NANGU KËRI NGUUR GI

Lu ëpp juróom-fukki njaboot la SOGEPA nar a génne ciy kër yoy, moomeelu Nguur gi lañu. Njaboot yooyii nag, ay liggéeykati Nguur gi lañu....

NGUUR GI XAATIMAL NA “SAES” AB DEKKERE

SAES (Syndicat Autonome de l’Enseignement Supérieur) mooy kurél gi ëmb jàngalekat yi nekk ci daara yu kowe yi. Kurél googu nag, ci ay ñaxtu...

KURÉLUG BINDKATI SENEGAAL YI AM NA NJIIT LU BEES : ABDULAAY FÓODE NJOON.

Gaawu, 8eelu màrs 2025, la kurélu bindkati Senegaal yi doon tabb njiit lu bees ci njiteefu Ibraayma Lóo, njiitu téereek dawal ak Amet Saalum...

SOLOS FUDDËN

Coosaanu fuddën Fuddën as ngarab la sos, ci làkkuw farãse, dippees na ko lawsoña inermis, bokk ci ngiirug garab gees di woowe lythracées. Ci kàllaamay...

AIBD : SYTAS ÀNDUL CI NDOGALU NJIIT LA

SYTAS (Syndicat des Travailleurs des Aéroports du Sénégal) nanguwul a dégg ndogal li njiitul AIBD li, Séex Bàmba Jéey, jël ngir wéyal wàññi limub...

FMI – SENEGAAL : ÀND LIGGÉEY NGIR JOYYANTI NAFA GI

FMI feddali na yéeneem ci liggéey ak Senegaal, gunge ko ngir mu joyyanti nafaam gi. RTS moo siiwal xibaar bi. Démb ci alxames ji,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/3/2025)

“SUIT” WEDDI NA XIBAAR BI L’OBS JIBAL SUIT (Syndicat Unique des Travailleurs du Trésor) mooy kurél gi ëmb liggéeykati béréb bii di “Trésor public”. Sàndikaa...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG ÀDDINA 2026  Ci weeru màrs wii, Senegaal dina ci amal ñaari mats ñeel 5eel ak 6eeli bés ci tooglantey kuppeg àddina siy ñëw....