Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NDAJEM JËWRIÑ YI (5/3/2025)

Démb ci àllarba ji, 5 màrs 2025, amal nañu ndajem jëwriñ mees di faral di amal ayu-bés bu nekk, fa Njénde la. Njiitu réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/3/2025)

ÑAXTUB VACATAIRES YI REVUS (Regroupement des Enseignants Vacataires du Sénégal, di kurélug jàngalekat yi ñu duppe Vacataires ci jàngune yi) mi ngi naqarlu ñàkkal faayda...

NDAJEM JËWRIÑI AFRIG YI ÑEEL NDOX MI

Doon nañu amal ci altiney barki-démb ji, 6eelu ndaje mu mag mu ndisoog AMCOW giy doxal. AMCOW (Conseil des ministres africaines chargés de l’eau)...

SÉMBUW KOPPEY MBAY ÑEEL NJABOOTU DAARA

Jëwriñu Mbay mi, Dund gu doy gi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, yégle na xibbar buy neex njabootu daara. Nde, dafa xamle ne...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

SAMPIYONAA YI AK SEEN TOLLUWAAY LIGA Barcelone daldi nay dóor Real Sociedad 4-0, daldi nangu boppu po ma gannaaw ba Real Madrid mi mu yamoo woon...

UMAR SISOKO EMBALOO DÀQ NA NDAWI CEDEAO AK UNOWAS

Ñaari kuréli Afrig sowu-jant yii di CEDEAO (Communauté Economique Des Etats de l’Afrique de l’Ouest) ak UNOWAS (Bureau des Nations Unies pour de l’Ouest...

YOON A NGI CI TÀNKI MAKI SÀLL

Maki Sàll mi fi nekkoon Njiitu Réewum Senegaal diggante atum 2012 jàpp 2024, dina wuyusi ca kanamu Yoon. Muy xibaar bu tukkee ci Mustafaa...

MAKI SÀLL : « RAGALUMA DARA. NAÑU MA TOPP BU LEEN NEEXEE… »

Maki Sàll tëkku na njiiti Senegaal yu yees yi. Moom, Njiitu réew ma woon, dafa doon tontu laaji saabalukaay bii di Jeune Afrique. Bi...

UBBITEG KÀGGU YONENT YÀLLA MUHAMMAT AK XAYTEG LISLAAM

Démb ci alxames ji la Njiitu réew mi doon jiite ubbiteg Kàggu gees jagleel dundu Yonent Yàlla Muhammat (SAWS) ak xayteg lislaam. Démb, 25 féewiryee...

FARBA NGOM DEM NA KASO

Farba Ngom dem na kaso. Tay ci alxemes ji, 27 féewiryee 2025, la ko njiitul àttekati "Pool judiciaire financier" (PJF) yi dóor ab "mandat...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (26/2/2025)

NDAJEM NJIITI RÉEWI AFRIG YA WOON Ay kilifa yu nekkoon i Njiiti Réew fi kembaarug Afrig doon nañu amal am ndaje démb ci talaata ji,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (25/2/2025)

NJIITU RÉEW MI DALAL NA OLUSEGUM OBASANJO Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dalal na Njiitu réewum Niseriyaa la woon, Olusegun Obasanjo. Seen ndaje...