Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

GÉNNEG SENEGAAL CI RÉEW YI GËN A NDÓOL

Senegaal ak réewum Kàmboj (Cambodge) ñooy réew yiy waaj a génn ci mboolom réew yi gën a ndóol. Loolu di ndogal “A/RES/79/230” nga xam...

8eelu BËCCËGUB SETAL SUNU RÉEW

Tay ci gaawu bi, 4i pani desàmbar 2024, doon nañu tóllanteeti « Bëccëgub setal sunu réew ». Muy juróom-ñetteel wi yoon ginnaaw bi ko Njiitu réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/1/2025)

BÀRTELEMI JAAS TEGGIWUL TÀNKAM Ginnaaw bi Yoon nangoo moomeg dépiteem ak cëru meeru Ndakaaru, taxul Bàrtelemi Jaas bàyyi mu sedd. Booba ba tey, mi ngi...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI CI AT MU BEES MI

Ci neexitalu atum 2024 mi, Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, biral na ay kàddu yi mu jagleel askan wi. Ca Njénde la...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/12/2024)

ÑOO NGI JAAY JUMTUKAAYI 7TV Ci benn saabaalukaay lees biral xibaaru njaayum jumtukaayi tele bii di 7TV. Tele boobu nag, saabalkat bii di Maymuna Nduur...

NJIITU RÉEW MI DÀQ NA SÉEX UMAR JAAÑ

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dàq na Séex Umar Jaañ. Moom, Séex Umar Jaañ, moo nekkoon jëwriñ jees dénk mbirum Caytu gi...

XEW-XEW BU DOY WAAR FA KOLDAA

Xew-xew boobu mi ngi am démb, ci dibéer ji, fa koñ bii di Médina Sérif, nekk fa Koldaa. Genn góor gu daan liggéey ci...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

Senegaal jàll na ci mbooleem powi Afrig ci atum 2025 yi. Loolu di jéego bu réy. Loolu day wane tamit dayob futbalu Senegaal, waayeet...

FËKKUG XALIFA AAMADU HAADI TAAL FA MALI

Tiijaani Mali yi ñu ngi ci tiis ak njàqare, rawatina njabootu Séex Umar Fuutiyu Taal ga fa nekk. Seen xalifa ba, Aamadu Haadi Taal,...

NGOMBLAAN GI : TAXAWAL NAÑU ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI

Ngomblaan gi taxawal na Ëttu àttewaay bu kawe bi. Tay ci gaawu bi, 28i pani desàmbar 2024, la dépite yi tànn 8i dépite yu...