Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

DÉGGOOB DAKKAL XEEX DIGGANTE ISRAAYEL AK HAMAS

Nguuru Israayel ak waa sóobarey Hamas yi (Palestin) am nañu déggoob dakkal xeex bi fa Gasaa. Ci àllarbay démb ji, 15i fani sãwiyee 2025...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (15/1/2025)

NDAJEM JËWRIÑ YI (15/1/2024) Ndogal yi tukkee ci ndajem jëwriñ mu tay mi : Dees na yeesal fànnu yaale ji te gën ko ñoŋal ngir...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/1/2025)

MURITANI CÀKKUTEEFI DOOMI SENEGAAL YI CI CÀMM GI Ilimaanu jëwriñ yi daje naak saa-senegaal yiy dund fa Muritani ci tukki bi mu doon amal fa...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA MURITANI

 Démb, ci dibéer ji 12 fani sãwiyee la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dem fa Muritani. Ma ngi fa àgg ci ngoon gi. Lii...

KAASAMAAS : DELLUB DAW-LÀQU YI

Door nañu sémbuw jàPpandal dellub daw-làqu yi fa Kaasamaas. Tay ci gaawu bi, 11i fani sãwiyee 2025, lañu doon ubbi jéego bu njëkk bi...

BÉSUB NJÀNGUM XALE YU JIGÉEN ÑI

Démb, alxames 9eelu fanu sãwiyee 2025, la Njawriñu njàng mi doon màggal, fa Jamñaajo, bésub njàngum xale yu jigéen ñi ci teewaayu Mari Xon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/1/2025)

BÉS BI ÑU JAGLEEL NJÀNGUM XALE YU JIGÉEN YI Tay, alxames juróom-ñeenti fan ci weeru sãwiyee, mooy bés bi ñu jagleel njàngum xale yu jigéen...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

SUPER CUP D'ITALIE : MILAN JËL NA KO ! Ci gaawub 7i sãwiyee bii lees doon amal finaalu “Super Cup d'Italie” bi. Mu ngi doxoon...

SENEGAAL : TOLLUWAAYU ÑÀKKUG LIGGÉEY BI YÉEG NA

ANSD siiwal na tolluwaayu ñàkkug liggéey bi fi Senegaal ci atu 2024 mi. bees sukkandikoo ci njureefi luññutu yi mu fésal, ci téeméeri nit...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/1/2024)

LAYOOB WATTUKATI KAARAANGEG LËKKATOO SÀMM SA KÀDDU Tay ci altine ji, ëttu àttekaay bu Ndar doon na àtte wattukati kaaraangeg lëkkatoo Sàmm sa kàddu. Ñoo...

USMAAN SONKO TONTU NA EMMANUEL MACRON

Tontu du forox naam, waaye mën na booy i nopp. Bu yeboo seet ba xam noppi Njiitu Réewum Farãs li booyuñu. Nde, tontu li...