Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

EL MAALIG NJAAY MOOY NJIITUL NGOMBALAAN GU YEES GI

Sëñ Elaas Maalig Njaay lañu fal ci boppu Ngomblaan gu yees gi. Ci altiney tay jii, 2i pai desàmbar 2024, lees doon samp 15eelu...

UBBITEG NGOMBLAAN GU YEES GI

Tay, ci altine ji, ñaari fan ci weeru desàmbar 2024, lañuy ubbi Ngomblaan gu yees gi. Keroog ci alxames ji la Njiitu réew mi,...

CAAROY 44

Ëllëg ci dibéer ji, 1 fan ci weeru desàmbar, dinañu màggal fi Senegaal bésub Caaroy 44. Muy màndargaal bés bi ñu bóome ñees duppee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/11/2024)

SAMIYEL SAAR DEM NA KASO Àjjuma jee weesu lañu ko tegoon loxo. Booba ak tay nag, ma nga ca loxoy Yoon. Waaye, mel na ne...

TËJANDI NAÑU JÀNGUNE BU SIGICOOR

Ginnaaw jàmmaarloo yu metti yi amoon Jànguneb Asan Sekk bu Sigicoor, kilifay daara ju kowe jooju mujj nañoo jël ndogalu tëjandi ko ba jëmmi...

WOTEY NGOMBLAAN GI : NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI SIIWAL NA NJUREEF YU MUJJ YI

Ndajem Ndeyu Sàrtu Réew mi biral na njureefi wotey Ngomblaan gi. Tay ci àllarba ji, 27i pani nowàmbar 2024, lañu leen siiwal ginnaaw bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/11/2024)

NJËGU GERTE GI  Càmm gi siiwal na njëgu gerte gi. Tay, ci ndajem jewriñ mees jagleel njaayum gerte gi (atum 2024-2025) lañu jàpp njëg li....

TËJ NAÑ MUSTAFAA JAXATE KASO

Démb, ci altine ji, la Mustafaa Jaxate fanaan guddeem gu njëkk ca ndung-siin. Ginnaaw bi mu jàkkarloowee ak Toppekatu bokkeef gi ba noppi, ca...

XIBAARI TÀGGAT YARAM

CAN 2025 : 24I EKIB YI JALL Noppees na ci matsi jàllug CAN bi ci ayu-bés bees weesu. Ñaar-fukk ak juróom-ñeenti ekib yii ñooy dem...

WAXTAANU NJIITU RÉEW MI AK VLADIMIR POUTINE

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jokkoo na ak Njiitu réewu Riisii, Vladimir Poutine. Barkaatu-dém, àjjuma 22 nowàmbar 2024, lañu wax telefon.  Moom,...