Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JÉYYA JU METTI FA MÉDINA BAAY

Xew-xew bu tiis boobu, mi ngi am démb, ci gaawu bi. Ma nga ame fa Médina Baay, ay boori juróomi waxtu ca ngoon. Ab...

TASAARE DÉG-DÉG YU WÉRADI

Saabalkat bii di Aadama Gay mi ngi ci loxoy yoon fi mu nekk nii. Moom ak Mustafaa Jaxate (APR) ñoo bokk i tuuma yu...

CPI JÁPPLU NA BENYAMIN NETANYAHOU

Ëttu àttewaay bii di CPI (Cour Pénale Internationale, fa mbaxana doone benn fi àddina si) jàpplu na Benyamin Natanyahou. Muy ndogal lees ko gàll...

WOTEY NGOMBLAAN GI : PASTEF RAAFAL NA 130I TOOGU

DGE, kurél giy saytu mbirum wote yi, siiwal na njureefi négandiku yi ñeel wotey Ngomblaan gi. Démb ci alxames ji lañu janook saabalkat yi,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/11/2024)

DIC WOO NA AADAMA GAY Tay ci alxames ji lañu ko woolu, ñetti waxtu ci ngoon. Waaye, woote bi dañu koo dàq ba suba bees...

ÀNDU NAWLE

Bokk na ci anam yi nit lootaabee ag dundam ci kaw suuf, lu nekk ak ku mu ko dénk. Loolu moo waral, mboolaay gu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/11/2024)

WOTE YI Limu wotekat yi bindu ci këyitu wote gi mi ngi tollu ci 7 300 000iy Saa-Senegaal. Waaye, ci lees jot a natt, lim bi jot...

PASTEF AK ÑOOMIN SEEN

Ndam la féete na wet. PASTEF a gobbi lépp, lëmbe géew bi, gën a sampu. Gaa ña wër ko, njiin ma jóg, bàkk ma...

WOTEY NGOMBLAAN GI : TAXAW-SEETLU YI NJËKK

Njureefi wotey Ngomblaan yi ñoo ngi tàmbali di génn, rawatina fa bitim-réew ak réew yi féete penku. Fii ci biir réew meet, am na...

WURE WA DEM NA KËŊŊ !

Ngomblaan gi, walla Péncum ndawi réew mi (ni ko ñenn ñiy wowee), benn la ci ñatti firgaat yu mag yiy joow Gaal gi. Gaal...

BÉS BI MUJJ CI KÀMPAAÑ YI

Tay jii, bu guddi gi xaajee, la kàmpaañ yi ñeel wotey Ngomblaan gi di jeex. Ëllëg, bésu noppalu la, ginnaaw-ëllëg ci dibéer ji dëppook...