Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/10/2024)

KÀDDUY ÀLLIYUN TIN ÑEEL WAY-PÓLITIG YI Àlliyun Tin, di kenn ci njiiti kuréli ma-xejj yi, yékkateeti nay kàddu jëme ci way-pólitig yi, rawatina ci seen...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukkee na fi réew mi barki-démb ci dibéer ji, wutali réewum Araabi Sawdit. Dina fa am...

NDOORTEELU KÀMPAAÑI WOTEY PALUG DÉPITE YI

Biig la kàmpaañ yi door. Kàmpaañ yooyu, ñi ngi war a jeex fukki fan ak juróom ci weeru nowàmbar. Looloo tax, dibéeru démb ji,...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkateeti na ay kàddu. Muy i kàddu yu mu biral ngir gindi askan wi ci doxalinam...

KUPPEG TEFES : SENEGAAL JËLATI NA RAW-GÀDDU GI

Gayndey Senegaal yi féetewoo kuppeg tefes gi amati nañu ndam. Ci gaawub tay jii la doon joŋante ak Móritani ci finaal bi. Gaynde yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/10/2024)

COOWAL TABBUG SÀMBA NJAAY Démb, ci ndajem jëwriñ yi lañu tabbee Sàmba Njaay, def ko “Président du Conseil d’Administration de la Société nationale des Habitations...

MBINDUM WOLOF : “FONK SUNUY LÀMMIÑ” TÀGGAT NA AY SAABALKAT

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ amaloon na jotaayu njàngum bind wolof. Saabalkat yi la ko jagleeloon. Mbootaay gi daf ci àndaloon ak IFAN (Institut Fondamental...

MBIRUM BUGAAN : 30 OKTOOBAR 2024 MOOY BÉSU ÀTTE BI

Njiitul "Mouvement Geum sa Bopp" , Bugaan Géy Dani, mi ngi ci loxoy yoon jamono jii. Fa Bàkkel lañu ko téyandi, muy xaarandi àtteem...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/10/2024)

WALUM DEX GI Càmm gi teggiwul tànkam ci taxawaay bi mu am ñeel walum dex gi ak askan wu takku wi ci loru. Ba démb...

GIGA MEETING PASTEF : FOO SÀNNI MBÀTTU MU TAG

Démb, ci gaawu bi, la waa Pastef doon amal seen ndaje mu réy moomu. Ñi ngi ko doon amale fa “Dakar Aréna”. Muy fowu...

KOOM-KOOM : PÉNCOO ÑEEL NDEFAR GEEK YAXANTU BI

Càmm gi dogu na ci aar cumbeefi biir réew mi (les entreprises locales). Jëwriñ ji, Sëriñ Géy, Jóob moo ko xamle. Fekk ñu doon...