Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/11/2024)

KADDUY NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, yékkati nay kàddu bi mu jógee ci tukkiteem bi gaawu. Kàddu yooyu nag,...

MBIRUM KAASAMÃS

Ci àjjuma jee weesu, magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko àddu woon na ci téere bi doomu réewum Farãs, Sewerin Awenengoo Dalberto, dib gëstukat ci...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (4/11/2024)

Powum UFOA U17 2024 Ren jii, Senegaal moo dalal po mi, doon ko amal diwaanu Cees ca fowu Lat-Joor bi. Àgg nañu ca finaal ya....

PAATUG MAMADU MUSTAFAA BA MA WOON JËWRIÑU NGURD MI AK NAFA GI

Léegi la APS siiwal xibaaru paatug Mamadu Mustafaa Ba mi woon jëwriñu ngurd mi ak nafa gi ci nguurug Maki Sàll. Mi ngi amoon...

TUKKITEY NJIITU RÉEW MI FA ARAABI SAWDIT AK TURKI

Dibéer jee weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukki woon na. Ma nga njëkke woon fa Araabi Sawdit. Def na fa...

SÉMBUB GTE (GRAND TRANSFERT D’EAU) BI

Càmmug Senegaal ak SINOHYDRO (bànqaas ci kër gii di Power-China) taxawal nañu liggéeyi sémbub GTE (Grand Transfert d’Eau) bi nu duppee Autoroute de l’eau...

BALAA NOO LAAX JAAY…

Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a ñoŋal nekkinam ci kow suuf. Ba tax na, lépp lu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2024)

TUKKITEG NJIITU RÉEW MI FA TURKI Keroog la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, demoon fa Araabi Sawdit. Mu doonoon tukkiteg waxtaan ci mbirum...

TABAXUG DËQ FA NDAR

Tàmbali nañu tabax ab dëq (digue) fa Daaru, diiwaanu Ndar. Jubluwway bi mooy aar askan wa ci walum dex Senegaal gi. DIRPA, banqaas bi...

YOON : DAAN NAÑ BUGAAN WEERU KASO

Tay lees doon àtte Bugaan Géy Dani fa Tàmbaakundaa. Moom miy njiitul kurélu Gëm Sa Bopp nag, àttekat bi daan na ko weeru kaso...

NGËLÉN FA ESPAAÑ : 95i BAKKAN ROT NAÑU

Tay, ci àllarba ji, 30i oktoobar 2024, ngëlén lu am doole moo dikkal waa Espaañ. Bariwaayu ndox mi ak dooley ngelaw li tax nañu ba...