Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MAATAM : WALUM DEX GI NANGU NA 700i TOOLI CEEB

Walum dexu Senegaal gaa ngi wéy di jur ay loraange yu jéggi dayo. Fa diiwaani Maatam, Kéedugu ak Tàmbaakundaa (Bàkkel). Njiitu réew mi sax,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/10/2024)

WAAJTAAYU WOTEY PALUG DEPITE YI Lu tollu ci weer moo des ci wote yi. Waaye, coow laa ngi ne kurr ci géewu pólitig bi. Lëkkatoo...

MAKI SÀLL MIIM NA

Njiitu réew ma woon, Maki Sàll, weddi na tuuma yees gàll ci ndoddam. Càmm gu yees gi, ci njiitalu elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/10/2024)

SENEGAAL 2050 Senegaal am na sémbu delluwaay wu bees. Tay ci altine ji, 14i pani oktoobar 2024, la ko Càmm gi aajar fa Jamñaajo. Muy...

KAAJARUG SÉMBUW SOPPI SENEGAAL FII AK 2050

Sémb wi ñu doon coow ay at, ay weer, ay ayi-bés, mujj na a yemb. Tey, ci altine ji, 14i pani oktoobar 2024 lees...

TOOGLANTEG CAN 2025 : SENEGAAL WULLI NA MALAWI !

Barki-démb, àjjuma 11i Oktoobar 2024, Senegaal doon na daje ak Malawi ca fowub Abdulaay Wàdd bi nekk Jamñaajo. Mats bi di woon seen ñetteel...

LU YEES CI MBIRUM PRODAC

Am na lu yees ci mbirum Prodac mi. BAD (Brigade des Affaires Générales), di bànqaas ci DIC (Division des Investigations Criminelles) ubbi na wayndare...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2024)

SÉMBUW SOPPI SENEGAAL FII AK 2050 Sémb wi, maanaam “Le Projet”, nees koy waxee, yemb na. Njiitu réew mi ak elimaanu jëwriñ yi ñoo ko...

NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI DËGGAL NA LAWAXUG SONKO AK BÀRTELEMI JAAS

Ndajem Ndeyu sàrtu réew mi àtte na. Ci guddig àjjuma ji la fésal ndogal li mu jël ñeel dabantal yees ko jébbaloon ngir gàntal...

NJIITUL KING FAHD PALACE WEDDI NA MAJAMBAL

Piyeer Mbów mooy njiitu këru gan gii di "King Fahd Palace". Moom nag, dafa indi ay leeral ñeel xibaar yi Majambal Jaañ siiwal. Ndax,...

Li gën a fës ci xibaari bés bi (9/10/2024)

9JÀNGOROY ŊAS Nemmeeku nañ juróom-benni jarag yu ame jàngoroy ŋas. Juróom-benni jarag yooyu, ñu ngi nekk ci juróomi "district" : Ndakaaru suuf (1), Funjuuñ (1),...