Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FUTBAL : FSF ÀDDU NA CI MBIRU ISMAYLA SAKOB

Keroog, ci àjjuma jii weesu, la Paab Caw biral toftaleg gayndey kuppe yi. Moom mi toppoon ci Aliw Siise, moo ko wuutandi ci boppu...

TAKKU WALLU BËGGUL SONKO BOKK

Démb, ci altine ji, la waa DGE (Direction Générale des Elections) siiwal toftale yi. Limu toftale yi xaw naa takku, donte ne sax, ñeen-fukk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/10/2024)

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI ÑEEL FMI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, rafetlu na taxawaayu FMI (Fonds Monétaire Internationale) ci li kurél gi...

WOTEY NGOMBLAAN YEES RANDALSI : DGE SIIWAL NA 41 TOFTALE

Kurél gu mag guy saytu wote yi fi Senegaal, Direction générale des élections (DGE), siiwal na toftale yiy joŋante ci wotey Ngomblaan yees randalsi,...

SONACOS/KAWLAX : UBBITEG ISINU LINJAAN BI

Elaas Ndaan Jaañ, njiitul SONACOS li, yégle na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina waa Kawlax. Nde, dafa xamle ne, isinu Linjaan bi nekk...

JUB, JUBAL, JUBBANTI : KURÉLI MAXEJJ YI ÀDDU NAÑU

Kuréli maxejj yi àddu nañu ci « jub, jubal, jubbanti » bi Càmm gi woote. Ñuy sàkku ci Kilifa yi ñu xoolaat seen doxalin wi aju...

MAKI SÀLL, LU LA KO JARAL ?

Seneweb moo siiwal xibaar bi. Maki Sàll, Njiitu réewum Senegaal mi folleeku keroog 24 màrs 2024, moo bàyyi liggéey bi ko Njiitu réewum Farãs...

FMI RAFETLU NA DOXALINU CÀMMUG SENEGAAL GI

FMI rafetlu na luññutu gi njiiti Senegaal yu bees yi amal ñeel koppari réew mi. Rafetlu nañu itamit li Njiitu réew mi, Bassiru Jomaay...

SETAL SUNU RÉEW : TEEWAAYU NJIITU RÉEW MI FA MBUUR

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, moo ubbi juróomeelu bésub set-setal bees di amal weer wu jot te ñu dippee ko "Setal sunu réew"....

ARCELOR MITTAL : ÀTTE BOR, FAY !

Càmmug Senegaal gu yees gi, jaare ko ci DGID, di kurél giy dajale kubal yi, daa fayloo woon Arcelor Mittal 1 205i miliyaar ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/10/2024)

BÀYYI NAÑU SÉEX YÉRIM SEKK, KADEER JA AK BUGAAN GÉY Ci ndoorteelu ayu-bés bi lañu leen woo woon fa Yoon. Ginnaaw gi, dañu leen fa...

JÀPP NAÑ BUGAAN GÉY DANI

Ci àllarbay démb ji, 2i pani oktoobar 2024, lañu woolu woon Bugaan Géy Dani mi jiite kurélu "Gëm sa bopp". Waa "Division de la...