Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FUTBAL/GAYNDEY SENEGAAL : YEWWI NAÑ ALIW SIISE

Gannaaw 9i at ci boppu ekibu Senegaal bu mag bi, Càmmug Senegaal gu yees gi dàq na Aliw Siise. Ci àllarbay tay jii, 2i...

DUND GU DIGG-DÓOMU

Lu jamono di gën a dem, mag ñi di gën a ñaawlu nekkiinu ndaw ñi. Moom kay, dañoo dëkk ci di ŋàññ seen i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/9/2024)

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/9/2024) WOTEY NGOMBALAAN GI Jeexal nañu démb ci dibéer ji, 29i pani sàttumbar 2024, njébbalug wayndarey lawax yi...

NJÉBBALUG WAYNDAREY LËKKATOO YI

Guddig dibéeru démb ji moo nekkoon àpp gu mujj ñeel njébbalug wayndare yi. Mu mel ni, ñi ñu gën a xaar ci wote yii,...

TOGO : SONG NAÑ GII MARI SAAÑAA

Gii Mari Saañaa ma nga Togo jamono yii. Waaye, nekkul ci jàmm. Ci lees jot ciy xibaar, dañ ko fa song, gaañ ko ba...

TOOLI CEEB YI TUUB FA DIIWAANU MAATAM

Tooli ceeb yu baree tuub fa diiwaanu Maatam. Looloo ngi am ginnaaw bi dex gi walangaanee foofu ci sababu taw yu bari yi fa...

NJOMBE YI FI MAKI SÀLL BÀYYI

Démb la woon alxames, 26i pani sàttumbaar 2024, yemoo ak bés bees di fàttaliku suuxug "Bateau Le Joolaa". Bés boobii la Càmm gi tànn...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/9/2024)

LEERALI CÀMM GI CI LIÑ FI FEKK Ci alxamesu tey jii, 26i pani sàttumbaar 2024 la Càmm gu bees gi joxe woon niki àpp ngir...

KÀDDUY NJIITU REEW MI CA NDAJEM MBOOTAAYU XEET YI

Démb ci àllarba ji, Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon fa Amerig (New York) ngir teeweji 79eelu ndajem Mbootaayu Xeet...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/9/2024)

Mbappe ame na gaañu-gaañu ! KilIyan Mbappe dina sori pàkk yi lu tollu ci ñett ba ñeenti ayu-bés gannaaw gaañu-gaañu bim jële ci seen...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (24/9/2024)

CÀMM GI DINA WAX AK ASKAN WI Njiitu réew mi ak Càmm gi dinañ wax ak askan wi ginnaaw ëllëg, ci alxames ji 26i pani...