Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FUTBAL : LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE AK CONFERENCE LEAGUE

Barki-démb, démb ak tey lañ doon amal joŋantey kaar-dë-finaal Ligue des champions yi, Europa League ak Conférence League fa Tugal. League des champions Ci talaata ji...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (18/4/2024)

ÑAAREELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Fay doon amal ñaareelu ndajem jëwriñam ginnaaw bi ñu ko falee ak...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : « DAÑU WAR A TOPP NJIIT YI FI NEKKOON… »

TV5 doon na dalal werekaan bu mag bi, Bubakar Bóris Jóob, séq ak moom ab laaj-tontu.  Ci laaj-tontu boobee, waxtaane nañ téere fent bi...

NJËLBEENI TUKKIY NJIITU RÉEWUM SENEGAAL FA GÀNNAAR AK GÀMBI

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay,  dina amal njëlbeeni génnam ci ayu-bés bile. Moom nag, Afrig la jagleel génnam yu njekk yooyile, nar a...

NJIITU RÉEW LU BEES LI NEMMEEKUJINA KILIFA DIINE YI

Ni ñu sànnee woon ay gët, bàyyi ko xel ci génnam bu njëkk bi mu war a def, ginnaaw ba ko askanu senegaal falee,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/4/2024)

SAYTUKAT YI CI GOX YEEK GOX-GOXAAT YI BANK NAÑ SEEN I LOXO Sàndikaa bi ëmb liggéeykati caytu gi ci gox yeek gox-goxaat yi bankloo na...

NJIITU RÉEW MI FA TUUBAA

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, amal na génnam gu njëkk ci biir réew mi. Ag tukkig nemmiku la def, tey, fa Tuubaa....

RUWÀNDAA, 30I GINNAAW FAAGAAGALUG TUTSI YA

Lu xewoon Ruwàndaa ca atum 1994 ? Keeroog, 6eelu fanu awril 1994, lañ song roppalaanu Njiitu réewum Ruwàndaa, mu ñàkke ci bakkanam. Ca ëllëg sa la...

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYER LEVERKUSEN JËL NA KO !

Xabi Alonso ak gaayam yi def nañ ko. Dugal nañ Bayer Leverkusen ci mboorum futbalu Almaañ. Ci anam bu rafet a rafet lañ ko...

BOROOM JAKARTAA BI FAATU FA CAALI

As góor su tollu ci 25i at, daan dawal móto jakartaa, lees fekk neewam ca yoonu Cees ak Morolã. Moom, ci turu Aliw Jàllo...

IRÃ SONG NA ISRAAYEL

Ay weer ginnaaw ba ñu dekkalaatee xareb Israayel ak Palestiin, ba tey jeexagul. Ndax, dafa am ku yokkaat ci xar mi karaw. Te, kooku...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo tax mu daan Lii dinaa ko bind ngir ëllëg Danga daan xëy di liggéey Njiitu Réew dàq la...