Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : BËGG-BËGGI JËWRIÑ JI MUSTAFAA GIRAASI

Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu yi, Mustafaa Giraasi, fésal na yéeneem ñeel daara ju Senegaal. Ginnaaw bi mu jëlee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/4/2024)

NJABOOTU LÀMB DAL NA CI KOW BIRAM SULÉY JÓOB  Bi jëwriñ jii di Biram Suléy Jóob génnee wax ni ñoom, nguur gu bees gi, kenn...

NJIITU RÉEW MI BIND NA LIGÉEYKATI CAYTUG BOKKEEF GI

Njjitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bind nab bataaxel, jagleel ko liggéeykati caytug bokkeef gi. Ci biir bataaxel bi, mi ngi leen di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/4/2024)

NJÉBBALUG LENGE FA MÀKKAANI NJËWRIÑ YA Keroog ci àjjuma ji la elimaanu jëwriñ ji génne limub yeneen jëwriñ yi. Ñenn ci ñoom jébbal nañu leen...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB ÑAAWLU NA KÀDDUY TAYIIRU SAAR YI

Fan yii weesu, Tayiiru Saar, njiitul làng gii di Parti nationaliste, dafa fésaloon i kàddu ñeel doxandéem yiy dund fi réew mi. Ba mu...

CÀMM GU BEES GI : WAAW, ANA JIGÉEN ÑI ?

Ginnaaw ba mu jële lenge yi, njiitu réew lu bees li Basiiru Jomaay Jaxaar Fay taxawal na góornamaŋam bu njëkk. Muy jëf ju mu...

NJIITU RÉEW MI DUNDAL NA AADA

Tay ci àllarba ji, 10i fan ci weeru awril lees doon amal jullig kori daanaka fépp ci àddina si. Njiitu réew mi, sëñ Basiiru...

KORITE 2024

Ren, daanaka àddina sépp ci àllarba tey ji lañu wori. Senegaal itam, tey la ñépp julli korite. Njiitu réew mi, fa jumaay Ndakaaru ju...

RUWÀNDAA : PÀTTALIKUG 30EELU ATUM FAAGAAGALUG TUTSI YI

Atum ren ji mooy tollook fanweereelu at ginnaaw bi faagaagalug Tustsi amee ba léegi. Ndax, ca atum 1994 la musiba bi amoon. Àmbasadëeru Ruwàndaa...

SÀNDARM BI AKSIDÀNTE FA KÉEDUGU

Ab sàndarm moo ñàkk bakkanam fa diiwaanu Kéedugu. Dafa def aksidaŋ ci tali Salemata bi. Xibaar baa ngi tukkee ci kilifay kaaraange gi. Ci altiney...

FAATUG MUHAMMET JÓOB FA PIKIN

Am nay xibaar yu bees yu rot ñeel faatug Muhammet Jóob. Nde, jàllale nañ juróom-benni alkaati yiñ ci jàppoon. Keroog 27 mars 2024 la alkaatiy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/4/2024)

USMAAN SONKO JËL NA LENGEY MAGUM JËWRIÑ YI Usmaan Sonko, magum jëwriñ yi ci càmm gu bees gi, jël na lenge yi tey ci altine...