Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

CORED ÀRTU NA BASIIR FOFANA MU ITV

Kàddu ya BacNsiir Fofana yékkati woon fa Itv mujj naa jur coow. Ndax, kàddu yooya, daf koo jëmale woon ci kii di Saŋ Batist...

JIITUWAAYI CÀMM GU BEES GI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, taxawal na càmm gu njëkk ci moomeem gi. Muy càmm gog, coppite la woote ak xëcc jëmale...

JËWRIÑI CÀMM GU BEES GI

Jëf toxal na wax. Ñoo ko dige woon, jëfe nañ ko. Umar Sàmba Ba siiwal na limub jëwriñ yi Sëñ Basiiru Jomaay Fay tabb, ...

154 MILIYOŊ AK LU TEG AT MU JOT : MAKI SÀLL SÉDDU NA LAATA MUY DEM

Maki Sàll, waajaloon na boppam ca atum 2013. Ndeke, mi ngi doon sóoraale ab wàccam. Moo tax, dafa xaatimoon ab dekkare, séddu, sédd soxnaam...

TÀGGE : MAHAMMAD BUUN ABDALAA JONN DËDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon, Mahammad Buun Abdalaa Jonn, moo génn àddina.  Tey, ci àjjuma ji, 5 awril 2024, la gaañu. Farãs gim doon fajoo...

NJIITU RÉEW MI NEENAL NA NDOGALI MAKI SÀLL YI

Ginnaaw bi mu jëlee lenge yi niki Njiitu réewum Senegaal, Basiiru Jomaay Fay jël na ndogal yu bir. Nde, dafa xaatim dekkare buy neenal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/4/2024)

64EELU MÀGGALU JONNUG SENEGAAL Tey ci alxames ji la réewum Senegaal màggal juróom-benn-fukk ak ñeenteelu at mi mu moom boppam. Ni ñu màggale bés bi...

TOMB YI GËN FËS CI KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réewum Senegaal lu yees li, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon na wax ak askan wi ci bésub tey jii, àllarba 3 awril 2024,...

USMAAN SONKO : ELIMAANU JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Usmaan Sonko, def ko elimaanu jëwriñ yi. Ginnaaw bi ñu ko tabbee, Usmaan Sonko jël na...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu kenn wéer goob ba Bii pas-pas dara mënalu ko dara Dina daw ba raw xëlu fas Ngor ak...

CAMPUG BASIIRU JOMAAY FAY

Ngelaw lu bees la réewum Senegaal noyyiwaat tembe ci campug Njiitu réew lu bees lii di Basiiru Jomay Jaxaar Fay. Mu nekk juróomeelu Njiitu...