Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JIGÉEN AY BOROOM-KËR

Ci li nu tàmm a dégg, boroom-kër, góor lees koy askanale. Waaye, bees settantalee Alxuraan, dees na gis ne jigéen la moomale kër gi....

DIBÉER 24 MÀRS 2024 MOOY BÉSUB WOTE YI

Léegi leer na. Jàppal nañ wote yi ab bés. Njiitu réew mi, Maki Sàll, moo tànn bésub 24 màrs 2024 ngir askan wi fal...

NJIITU RÉEW MI TAS NA CÀMM GI

Bees sukkandikoo ci Majambal Jaañ, Njiitu réew, Maki Sàll, tas na Càmm gi. Bi Ndajem jëwriñ yi jeexee ci 18i waxtu la ko tas....

NDAJEM NDEYU SÀRTI RÉEW MI BAÑ NA NDOGALI WAXTAANU MAKI SÀLL WI

Ndajem Ndeyu sàrti réew mi bañ na dogal yi tukkee ci waxtaan wu mujj wi Njiitu réew mi woote woon fa CICAD, Jamñaajo. Juróom-ñaari...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel wotey tànn Njiitu réew mees dëgmal ci atum 2024 mii nu nekk. Dafay feeñal yenn...

WOTEB SÉMBUB « AMNISTIE » CA NGOMBALAAN GA

Sémbub « amnisti » bi Njiitu réew mi naal mu ngi jaabaajonge réew mi. Mu nekk dogal lu Njiitu réew mi jël ngir fomp lépp lu...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

DAAN NAÑ PÓOL POGBAA 4i AT YUM DUL FUTBAL Doomu Farãs ji, ndax futbalam du fi jaare yàqu ? At yii weesu, saa bu génnee...

AMNISTI : LIGGÉEY BI DOOR NA

Ci altiney jii, 4 màrs 2024, lees di fénc sémbub àtte bees duppee ci tubaab “loi d'amnistie”. Maanaam, ab xeetu àtte bob, day far...

WOTEY 2024 YI : BENNOOG TUGAL (U.E.) A NGI GËTËN MAKI SÀLL

Waa Bennoog Tugal (Union Européenne) àddooti nañ ci wotey 2024 yees war a amal fi Senegaal ngir palug Njiitu réew lu bees. Ñuy fàttali...

LU BEES ÑEEL MAYMUNA NDUUR FAY

Lu bees rot na ci cong mi ñu songoon taskatu xibaar bii di Maymuna Nduur Fay. Daanaka, yéenekaay yépp ñoo ko fésal ci seen...

JAM NAÑ MAYMUNA NDUUR FAY

Maymuna Nduur Fay, taskatu xibaar bi jiite 7tv la ab/ay sàmbaabooy dogaale, fitnaal ko, jam ko paaka. Mbir maa ngi xew ginnaaw bim jeexalee...

TÀGGATOO

Roqi, ba beneen yoon. Seetal ma lii rekk. Wax dëgg. Xool sama digganteek Yàlla te bañ a fen. Waaw, yombul nga seeti sa rakk ak sa...