Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI GÀNTAL NA CÀKKUTEEFU PDS GI

Ëttu àttekaay bu kawe bi gàntal na càkkuteefu PDS gi lawax yi ñu téye. Nde, ñoom waa PDS ak lawax yiy wax ne dañ...

DOOMU SENEGAAL JI ÑU REY CA FARÃS

Xew-xew bu tiis boobu mi ngi am ci guddig talaata jàpp àllarba. Takk-deri tubaab yi ñoo bóom lenn ndongo Saa-Senegaal lu fa doon jànge....

LI GËN A FÉS CI WOTEY 2024 YI (14/3/2024)

JURÓOMEELU FANU KÀMPAAÑ  Dibéer jii weesu la kàmpaañ yi door. Ñoom, fukk ak juróom-ñeenti lawax yépp, song nañ dëkk yi, gox yeek gox-goxaat yi, di...

MAKI SÀLL FEDDALI NA KÓOLUTEEM CI AAMADU BA

Àllarbay tay jii la xibaar gi rot, njiitu réew mi Maki Sàll xamal na askan wi ne tay la gën a gëm Aamadu Ba...

« JUMTUKAAYI WOTE YI MAT NAÑ. »

Magum jëwriñ ju bees ji, Sidiki Kabaa, dalal na xel yi ñeel wotey 2024 yees dégmal. Nde, ñu bari dañ doon ragal jumtukaayi wote...

NGUUR GI TOPPEETUL USMAAN SONKO DARA !

Nguurug Maki Sàll gi dellu ginaaw ci topp bim doon topp Usmaan Sonko ci yoon. Nde, dafa bind na ëttub àttewaay bu mag bi,...

LI GËN A FÉS CI WOTEY 2024 YI (11/3/2024)

WOTEY 2024 YI : LAWAX YI TÀMBALI NAÑU DAGAAN YI Démb ci dibéer ji la dagaanug baati askan wi ñeel wotey 24 féewiryee yi tàmbali. Lawax...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

AY YEESAL ÑEEL BARI (LES EQUIPES) SENEGAAL YI Gaynde yu mag yi (ekib A) Wéyalees na pasug Aliw Siise gi ba keroog atum 2026. Kii di...

WIDEWOO BASIIRU JOMAAY FAY DU JÀLL FA RTS

RTS, kibaaraan la gu wute ak yeneen yi nekk ci biir réew mi. Ndax, kibaaraan la goo xam ne, askanu Senegaal a ko moomal...

WOTEY 2024 : CÀKKUTEEFU AAR SUNU ELECTION

Fileek Fukki fan ak juróom, dees na amal wotey palug Njiitu réewum Senegaal yi Maki Sàll ajandi woon. Waa Aar sunu election dellu di...

JËWRIÑI CÀMM GU BEES GI

Bërki-démb la Njiitu réew mi tasoon Càmm gi daldi tabb Siidiki Kaba Elimaanu jëwriñ yi. Tey lañ siiwal jëwriñ yiy liggéey ak moom ci...