Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/2/2024)

PÓLITIG Ndiisoog pólitig ga ca diisoo ba Njiitu réew ma woote woon noppi na. Bees sukkandikoo ci xibaar yi jot a rot, 2i fan ci...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/2/2024)

MBIRI PAAP GÉY AK MÀRSEY  Gannaaw CAN bi mu demoon ak Senegaal, Paap Géy, miliyë Màrsey (Marseille) bi dañ ko dàndoon ca këlëb ba, maanaan...

CEDEAO TEGGI NA DAAN YI MU TEGOON NISEER

Démb ci gaawu gi la way-bokki kurél gi boole réewi Afrig sowu-jant yi ci wàllu koom daje woon fa Abujaa. La gën a fés...

MBAAM MI : ÑETTI LÉEB

Cokkaasu RFI bii daf nuy fàttali ñetti léeb yoy, mbaam a ciy ndeyu-mbill ji. Léeb bu ci nekk nag, day junj nekkiinu Njiitu réew...

KAN LA NJIITU RÉEW MI NAR A DIISOOL ?

Nees leen ko xibaaree woon, diisoo la Njiitu réew mi Maki Sàll wooteeti ngir jàpp bés bees war a amal wote yi. Ginnaaw ëllëg...

DIISOOB FÉEWALOO

Ginnaaw-ëllëg ci altine ji, 26 féewiryee 2024, la diisoo bi Njiitu réew mi woote woon di door. Njëwriñu biir réew mi moo génnee ab...

MAKI SÀLL A NGI WÉY DI LËJAL KÀRT GI

Démb la Njiitu réew mi doon tontu laaji taskati xibaar yiy liggéeyee RTS, Le Soleil, iRadio ak Seneweb. Ca njéeméer ba la janoo bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/2/2024)

NJIITU RÉEW MI DINA JANOOK TASKATI XIBAAR YI ËLLËG CI ALXAMES JI Bu ëllëgee, ci alxames ji, Njiitu réew mi dina tontu laaji taskati xibaar...

AYSATA : TAAL BI DU AY FEN ÑOO KOY FAY

Kii di John Mearsheimer, ca atum 2011, dafa génne ab téere tudde ko "Why Leaders Lie : The Truth About Lying in International Politics"...

WOTEY 2024 YI : 19i LAWAX ÑOO CI DES

Ginnaaw bi mu neenalee dekkare Njiitu réew mi jëm ci fommug wotey 25 féewiryee 2024 yi, Ndajem Ndeyu àtte mi sëggaat na ca waynderew...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu ni mel a ngi tukkee ca « Bangladesh ». Mbootaayu Xeet yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/2/2024)

NDAJEM NDEYU ÀTTE MI YEESALAAT NA LAWAX YI Ndajem Ndeyu àtte réew mi génnee beneen listu 19i lawax yi war a joŋante ci wotey 2024...