Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/01/2024)

NJIITU RÉEW MI JOX NA DIG-DAJE LAWAX YI ÑU TÉYE Ginnaaw bi ndajem ndeyu àtte mi jeexalee caytug xobi baayale yi, dafa am lawax...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JONANTE DÉMB YI Démb ci talaata ji lees amal ñetteeli joŋantey kippug C gi ak gu D gi. Nii lañu demee : Kippug C :...

SOXNA JAAGA MU BÀLLAAGO DËDDU NA

Dee du jaas. Fu ko kenn dul xaar la malaakam dee mi naan jaas, ne fa coppet ab bakkan, te kenn sañul a kaas....

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JOŊANTEY BÉS BI Démb ci altine ji, kippug A gi ak gu B gi amal nañu seen ñetteeli joŋante ñeel sumb bu njëkk bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/01/2024)

WOTEY 2024 YI Usmaan Sonko Usmaan Sonko dañ gàntal dabantal bi mu dugaloon. Ndaje mi teg ko ci 6i weer yi ñu gàlloon ci kowam ci...

KARIIM WÀDD : “DAMAY BOKK CI NII WALLA CI NAA…”

Gaawu gii weesu la ndajem ndeyu àtte mi biral limu lawax yiy bokk ci wotey 2024 yi. Lawax yooyu ñi ngi tollu ci ñaar-fukk....

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

WÉR-GI-YARAMI ALIW SIISE AK ABDULAAY SIMAA Bees sukkandikoo ci yégle "Fédération Sénégalaise de Football" (FSF) biral démb ci gaawu gi, Aliw Siise, tàggatkatu ekibu Senegaal...

SONKO AK KARIIM DUÑ BOKK CI WOTEY 2024 YI

Ndogal li rot na. Tey jii, ci gaawug 20 sãwiyee 2024, la 7i àttekati ndajem ndeyu àtte mi waroon a biral toftaleg lawax yiy...

SENEGAAL AK MÓRITANI : NDEFARUG GIL BI DINA TÀMBALI

Dees na tàmbali ndefarug gil (gaas) gi ci diggante Senegaal ak Móritani. Ci atum 2023 mii nu génn la liggéey bi waroon a door....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/01/2024)

SÉEX TIIJAAN JÉEY DÀJJI NA TUUMAY AAMADU BA (BBY) Aamadu Ba, lawaxu Bennoo Bokk Yaakaar, dafa dafa dugaloon dabantal ngir neenal wayndarey Basiiru Jomaay Jaxaar...

GAYNDEY SENEGAAL YI RËKK NAÑ YOY KAMERUN YI

Gannaaw ba mu wullee dëkkandoom bi, Gàmbi, keroog ca bés bu njëkk ba, Senegaal wulleeti na Kamerun 3i bal ci benn. Senegaal mooy ñaareelu...

SENEGAAL-KAMERUN : LÀMBU GAR AK ÑALÓOR

Tey ci àjjuma ji la gayndey Senegaal yiy laale ak yoy Kamerun. Bu 17i waxtu jotee, ca la joŋante bay door ca fowub Yamusukroo...