Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LAYOOKATI SONKO YI DUGAL NAÑ AB NEENAL-ÀTTE

Ginnaaw bi ëttu àttewaay bu mag bi neenalee woon àtteb Sabasi Fay ba, keroog àjjuma17 nowàmbar 2023, layookati Sonko yi, ba léegi, xàddeeguñ. Nde,...

JALOOREY RAGLUB SÓOBARE BU WAKAAM

Senegaal séqi na jéego bu am a am solo ci wàllu paj. Nde, doktoor ya ca raglub sóobare ba ca Wakaam, maanaam loppitaanu soldaar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/11/2023)

WOTEY 2024 YI Li des ci wotey 25 féewaryee 2024 yi yées na ñetti weer. Waaye, am nay lawax yu féete ci kujje gi yuy...

AY CONGU CI YENN BÉRÉB FA SIYERAA-LEWON

Njàqare ak tiis la askan wa dëkke fa Freetown yeewoo démb. Ay sàmbaa-bóoy ñoo song béréb yu bari fa gëbla ga. Muy koñ bii...

Xibaari Tàggat-Yaram

kuppeg Àddina U17: 1/2 finaal Joŋante baa ngi wéy, ñu tollu fim ne ci 1/2 finaal yi. Ci 1/4 finaal yi Almaañ moo dóor Espaañ...

NJAAYUM GERTE GI : CÀMM GI SAMP NA NJËG GI

Càmm gi samp na njëg gees war a jaaye gerte gi ci kàppaañ 2023-2024 bi. Kilo gerte bu nekk deesu ko jaaye lu yées...

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko ca atum 2020. Xaaj bu njëkk bii, siiwaloon nanu ko...

TËNKUG JIBAB NJÀNG MU KOWE MI

Ay fan a ngi ñuy amal ay wote ca Ngomblan ga ñeel koom mi ñu war a yoree réew mi. Dépite yi di càmbar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/11/2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ USMAAN SONKO Suba ci alxames ji lañu waroon a àttewaat coow li doxoon diggante ñaar ñooñu ca ëttu àttewaay bu kowe...

WAY-SOPP LÀMMIÑI RÉEW MI, TOOGAAY AMATUL !

Àjjuma 17eelu nowàmbar 2023 ca Fatig, Njiitu réew mi, Maki Sàll, yëkkati na yile kàddu : « Abajada bi, buñ ko yombaloon, Senegaal romb kon na fii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/11/2023)

NGOMBALAAN GI Dépite yaa ngi wéy di nattal jëwriñi Càmm gi seen i gafaka ñeel atum 2024. Ñu doon nattal tey jëwriñu kéewnga leek yi...