Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (19/11/2023)

LÀMB : LAG DË GEER 2 DAAN NA SITTA Ñaari mbër yi waajal nañu seen bés bi, def nañu lépp li ci war, neexal seen...

PASTEF JIITAL NA BASIIRU JOMAAY

Xibaar bi jib na : Basiiru Jomaay Fay la waa PASTEF tànn ngir doon seen lawaxu ci wotey 2024 yi. Ëllëg ci altine ji...

FATIG : NJIITU RÉEW MI DIGEETI NA

Njiitu réew mi Maki Sàll digeeti na lu ëpp 800i tamñareet fa diwaanu Fatig. Fekk mu doon fa amal ab wëraan ñeel koom gi....

SONKO AMATI NA NDAM !

Naam, CEDEAO joxe ko dëgg. Naam, Ëttub àttewaay bu mag bi neenal na àtteb Sabasi Fay ba. Waaye, ba tey Sonko moo am ndam,...

CEDEAO AK ËTTUB ÀTTE BU MAG BI GÀNTAL NAÑ SONKO

Ëttu àtte bu CEDEAO gàntal na Usmaan Sonko, jox dëgg Càmmug Senegaal. tey la àttekati CEDEAO doon àtte layoob Usmaan Sonko ak Càmmug Senegaal....

USTAAS UMAR SÀLL MA NGA CA LOXOY YOON

Ustaas Umar Ahmad Sàll, ab waaraatekat bu siiw ci réew mi la. Fës na lool ci mbaali jokkoo yi. Nde, bari nay waxtaani diine...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI 15/11/2023

TUXAL NAÑU USMAAN SONKO Lu ëpp ñetti weer ginnaaw ba ñu ko jëlee ca kasob Sébikotaan yóbbu ko ca raglub Principal ngir fajee ko fa,...

COSCE ŊÀÑÑI NA NI ÑU TABBE WAA CENA

COSCE (Collectif des Organisations de la Société Civile pour les Elections) ag mbootaay la gu boole ay kuréli way-moomeel ñeel wote yi. Mbootaay googu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/11/2023)

PÓLITIG Utum baayele yi ñeel Usmaan Sonko dina tàmbali ci njeexitalu ayu-bés bi. El Maalig Njaay mi yor jokkoo bu Pastef moo ko xamle. Ci...

LÀMB : TAFAA TIN DAAN NA ËMMA SEEN

Gannaaw ba Móodu Lóo ak Aama Balde bëree ci ayu-bés bii weesu, Móodu daan ko, démb ñaari punkal ñoo doon dajeeti, muy Ëmma Seen...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (12/11/ 2023)

LAKK CA JAWUB KAWLAX Ag lakk gu yéemee amoon ca ja bu mag (marché central) ba ca Kawlax, ci guddig gaawu gi 11 nowàmbar. Ñeenti...