Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LUUBALU 540I TAMDARET CA CMS BU MEDINAA

CMS ab bànqaasu déncuwaay ak àbbuwaayu xaalis la bu nekk ci biir réew mi. Fan yii ñu génn, lañ gis ci yéenekaay yi ne...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/12/2023)

USMAAN SONKO : JÀPP NAÑU BÉSUB LAYOO BI Lu tollu ci ñaari ayu-bés ginnaaw ba ëttu àttewaay bu kowe bi neenalee àtteb Sabasi Fay ba,...

GINE BISAAWOO : UMAR SISOKO EMBALO TAS NA NGOMBLAAN GA

Umar Sisoko Embalo, Njiitu réewum Gine Bisaawoo, tasati na Ngomblaan ga. Démb altine, ci yoor-yoor bi, la woolu ca màkkaanu Njiitu réew ma (pale),...

WAAJTAAYU BÉSU DAARA

Séex Umar Aan di jëwriñ ji ñu dénk njàng meek njàngale mi amal na tukkib nemmeeku ca Tuubaa. Xalif ba, Séex Muntaqaa Mbàkke, dalal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/12/2023)

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am déet, mënees na jàpp ni wote yi dinañ am ci...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle. Moom Jean Emmanuel di ki yor kàddug Nguur gi (porte-parole)...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/12/2023)

COOWAL CAN LI Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee, coow li jib, ñuy ŋëwti-ŋëwti joŋante bi. Te, bu "Euro"...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon ngir ñu saytuwaat dogal ga mu jëloon ñeel Usmaan Sonko...

ËTTU ÀTTEWAAY BU MAG BI : NJIIT LA GÀNTAL NA NEENAL-ÀTTE BU LAYOOKATI USMAAN SONKO

Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati Usmaan Sonko yi dugaloon. Fekk ñu tàbbaloon ko fa ñeel neenalub dogal bi àttekat...

LI GËN A FË CI XIBAARI BÉS BI (1/12/2023)

JËWRIÑU NGURD MI JOXE NA KÀDDOOM Démb la Ngomblaan gi doon jeexal ndaje yi mu doon amal ak jëwriñi Càmm gi. Def nañ 32i fan...

AYIB DAFE A NGI YEDD CDC

Bu Usmaan Sonko bokkee ci wotey 2024 yees dégmal de, dina doon jaloore ju réy. Nde, 2021 ba léegi, Nguurug Maki Sàll gaa ngi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/11/2023)

LI BEES CI NDOGAL LI ËTTU ÀTTEWAAY BU KOWE BI JËLOON Ci talaata ji la layookati Usmaan Sonko yi jébbal waa ëttu àttewaay bu kowe...