Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (25/8/2023)

BAKKANU USMAAN SONKO MI NGI CI XOTTU GERTE Tey ci àjjuma ji, njiiti lëkkatoo Yewwi Askan Wi seeti woon nañ Usmaan Sonko fa raglub Principal...

PAATE JAAÑ, SA JAAN WÀCC NA !

Paate Jaañ wàcc na liggéey démb ci àllarba ji, 23i fan ci weeru ut wii 2023. 89i at la amoon. Jarbaat ji, Mademba Njaay,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/8/2023)

SÉEX BAARA NJAAY DAY DES KASO Fan yee weesu lañu ko doon sàkkul ag bàyyig négandiku. Waaye, mujjul woon a àntu. Ndax, ëtt bii ñuy...

SËRIÑ MUNTAXAA MBÀKKE YÓNNEE NA USMAAN SONKO AY TÀNDARMA

Sëriñ Muntaxaa Mbàkke, Xalifab murit yi, dalal na waa Yewwi Askan Wi. Ca seen ndaje ma, jox na leen ay tàndarma yoy, Usmaan Sonko...

FAAS BÓOY, SIGGIL NDIGAALE !

Mbëkk maa ngi wéy di def i jéyya ci réewum Senegaal. jéyya ci kow jéyya. Musiba ci musiba. Li gënatee doon musiba te raglu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/8/2023)

WOTEY 2024 YI : MAMADU IBRA KAN DINA NEKK LAWAX Mamadu Ibra Kan dina bokk ci wotey 2024 yi. Bërki-démb, ci dibéer ji, la ko dëggal....

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

MESSI GAÑE NA KUBAM BU NJËKK AK INTER MIAMI Ci guddig gaawu gi jàpp dibéer jii weesu la Inter Miami doon joŋante finaalu Leagues Cup,...

« COALITION SENEGALAISE DES DEFENSEURS DES DROITS HUMAINS (COSEDDH) »

Ay kilifa ak i kàngaam yu mag bennoo nañ bind ab bataaxal, jagleel ko Njiitu réew mi, Maki Sàll, ñeel mbiri Usmaan Sonko ak...

« USMAAN SONKO NEE NA YËGATUL WETU CÀMMOOÑAM… »

Xadi Kebe ak Aana Jamanka, ñaari soxnay Usmaan Sonko yi, doon nañ amal ab laaj-tontu ak kii di Paap Aale Ñaŋ mu Dakar matin....

BITIM-RÉEW : LAYOOKATI USMAAN SONKO YI TÀMBALI NAÑU XEEX BI

Ni ñu ko waxee woon lañu ko defe. Layookati Usmaan Sonko yi yóbbu nañu mbiri njiitul làngug Pastef ga woon ca HCNUDH (Haut-commissaire des...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (18/8/2023)

WÉR-GI-YARAMI ÑI ÑU JÀPP CI KASO YI Kilifay caytug kasoy Senegaal yi génne nañu ab yégle di ci biral wér-gi-yarami ñett ci ñees jàpp ci...